Deug Sur Deug Lyrics
Mafi né ça bouge pas , île de yoff
Trop de flow en l’air lalay guénel dama oyof
Ngani dang ma bagne, Mala fouf
samay daleu lalay kholé boy Yangui si souf
Pik yingu ma sani ladef samay louboutin
Sa produit dou ndokhé diwoko diap touti diap teint
Didier Raoul flow, chloroquiné
Picasso si samay texte suis, trop raffiné
Tangorou dragon burn fire
Douma diéneu boudoul sou goudé vampire
Fepeu lagne may tek sama tour melni ataya
Barina ay dome si game bi Mane la briz papaya
Sa guinaw ngakoy yeuk, sodomi
Diougeul bamou dioup khothi Midi et demi
Paco dafa meneu rap waw déssi bolé kaar
Khawma lou dangeu mane dama massa dioup neuf heure et quart
Damalene dak rap, dagne ma dakeu mar tate
Damay woneu bâte, wathiou doumko lékate
Diaroul tigui gate ,Wakh dji dinko wakhate
Boy Diaroul wo mo gate, say lamp dou takate
Comme un arc en ciel suis magnifique
Sénégalais nanga def waw manguifi
Je vous, présente ma culture alap lebou
Trop de fierté boy kene dougnou yap, toujours debout
Moi je Suis plus fort que vous tous
Dolene fi tousss
Damani ngene pouss
Yamlene si pouss pouss
Té dougou dousss
Beuré dji pour touss
Rappeurou couss couss
Gate ni kousss
Togal sa poukhouss
Mou taa nga diok khouss
Teudieul sa bouche
Tay dinga lal souf
Lay souf
Nala touf li khakh touf
Khakh touf
Di partouz
Diap onde lal thiouss
Mangfi dofi am touss
CR7 Juventus,
Justice doufi am fils
Injustice késsé ngay guiss
Danga productif, khawma lofi def
Wakh nga ba eumbeul sa bope takh sa son yi nef
Qualité dou quantité ‘Q´ bélene bolé
Mane Damkoy dozél bamou dozé ni gneuw dilene dozé
Diay sa bop lagnou wowé prostitution
Mane sama album lalay diay, prostituson
Sékheu gui guéneugoul thiouthi bi doufi sap
Yagu deukheugnou ba mar def Mc jus bissap
Pithi mogui amé diamam sikaw air
Bouy wathi fitneu di commencé am gnouy sani kheer
Kep kou def lou bakh dégu gathi ngalama
Bo togué fep diko wakh dinga am gathiéy kalama,
Deug sur deug
Ngay dégu di dégu
Khol beug di beug
Pour nga foor seugeul di seugu
Teugu di teugu
Diap deuneu di feugu
Yetédji kheudeu
Motali yéné bi Yégu
Sa kholay tang nala bayek yallah mou done sa sapeur , ndakhté khol lay fay
Niveau boudoul maguate lalene euf ndéké eupoukay dina andi ngélaw, Mbaye Dieye faye
Flowou bougati leu negger vroum vroum
Tidjil fenêtre doko guiss sakh Google chrome Hummm
Damlene time ba melni drone
Bodé king bi Mangui sa kay bope mane la couronne
Marrer basse la maa rar, ba guéthi gui fésate
Geuthi ma guiiiss mangui waarar, dotoko féfate
Diangu philosophie waarate, ba melni Decarte
Mak enemy manougnou faarate, boul diakhassé carte
Danga productif, khawma lofi def
Wakh nga ba eumbeul sa bope takh sa son yi nef
Qualité dou quantité ‘Q´ bélene bolé
Mane Damkoy dozél bamou dozé ni gneuw dilene dozé
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2022
Album : Deug Sur Deug (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE