Home Search Countries Albums

Secret 7

NGAAKA BLINDé

Douma nitou néne douma topou thi leufe
Mane sama rap mounoul woyoff  dafa topou thi 9
Koumay Lathie koumay sét néko mangi assamane
Gni né souf mounoul sét mani 7 soufa âm, 
Carbone 14 niari 7 am talant 2002 numéro 7 niou néma Harry camara
Khadiou ma si blanche dama apou thi pois
Dieul rapport yi  déf thi pin khapou thi petit pois
Lyrics intelligence imposer sama lois
Gni nara bagne ma dioutal len déf len Litopou thi 3
Li may rap mathématique fok nga 8 8 thi calcule 
Pour took Sama 16 gnii dagne ma yapp fok ma sadig 
Weekit fok ma 7  thi  8 pour niou  15 Li may guénse
It mow Diose moy  Sét-sét, sét moy change moy kham
I know rék i blow mane la jakc sét jakc 
Moy dieul moy diaye ay nit rék wakh ma 
Thi koy ték ma néko kay niou rap dina rap 
Ba téne yi taw tédou Lale kay niou rap baaba,
 
154 chiffre niveau  bé 10 kone mécanique classique may 
Isaac newton béne bing thiy dolli moy 155 
Moy gnii ma len mane may mic sen taille jeûne 
11 bi thi guéne lay sanni thi guéthie gui 
Diapou niaari dieunou ndanaan sopi len guédji
Ma len mane niaari yon koumay lathie kouy wéddi 
Fi ma ték sama tank koufa lathie téggi
Ma len mane thi bir بِسْمِ اللَّـهِ ak  باطن mane len thi ظاهر
 Moy كُنْ  bék  يس  son bi am na 331 thi chiffre
Baaba moy 2121 = 6
Secret 7 moy 1942, 
A1 i 9 D4 B2, 1942 dans 2 albums mondiale 19=10 donc 4 2 = 
 10 . 6 = 16 non non 7,
124 mille Yi bokoy sét guénoul sa wét, اِحصان
 Thi prophète إِيمانٌ. Fépay Rafètte
Mane secret bimay sét kou nioul khoul  sa tête baaba,

 

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Added By :


Release Year : 2020


Album : Secret 7 (Album)


Genre :


Copyright : ? Sen'art vision

SEE ALSO

AUTHOR

NGAAKA BLINDé

Senegal

Ngaaka Blindé is musician from Senegal. ...

YOU MAY ALSO LIKE