Home Search Countries Albums

Ndaat Saay

WIZZY KANA

Ndaat Saay Lyrics


Jaral ngama taxaw fetial leuh ndate saayé
Yaay bourou sama xol kone foula nekh feulaalé
Koula songg beurrei nga daan ko
Thi dig eute bi noula nekh dagoo
Farata rek laaladoon doyei
Damala nope ba am sa faiblesse
Lou eupp tourou bvby lii dafa fees
Damlay xalaat ba sama xel bi né mess
Lou waay deugeur deugeur dinga danou
Say kesseng kesseng momay takha aallu
Yeegeul sama xel dima souss loo
Yaa raw dadiou volet bimay takha metti
Risque leuh
Risque leuh
Jeema dokh sa garde risque leuh
Risque leuh
Risque leuh
Jeema dokh sa garde risque leuh

Jalgati jalgati iow
Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul
Iow yaamay fethie loo ndaate saay
Jalgati jalgati iow
Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul
Iow yaamay fethie loo ndaate saayé
Linguère linguère
Iow yaamay fethie loo ndate saayé
Linguère linguère
Iow yaamay fethie loo ndate saayé

Deukké dima tiaw xiir bi doo baalé
Dawal sama kaw deema yoobalé
Ehh deguine ndate saay
Ehh deuguine ndate saay
Tay ma fetial la deuguine ndate saayé
Chéré sama chéri
Yaama téré nelaw
Say tiakass tiakass sama kaw
Lii moma tée
Deff ma ndank
Deff ma ndank
Xalei bi dina meusseu ray doomou diambour
Yaadi wourouss ngalam
Féthial ma toukoussou ngalam
Yaay awoo buuru keureum
Kou merr nafa dé yaafa kham
Xalé bi amoo morom
Maala sante geureum
Or nga yeugoo peureum
Iow laay topp deema beureung

Risque leuh
Risque leuh
Jeema dokh sa garde risque leuh
Risque leuh
Risque leuh
Jeema dokh sa garde risque leuh

Jalgati jalgati iow
Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul
Iow yaamay fethie loo ndaate saay
Jalgati jalgati iow
Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul
Iow yaamay fethie loo ndaate saayé
Linguère linguère
Iow yaamay fethie loo ndate saayé
Linguère linguère
Iow yaamay fethie loo ndate saayé

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2023


Album : Ndaat Saay (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

WIZZY KANA

Senegal

Wizzy Kana is a singer and rapper based in Senegal Mbour ...

YOU MAY ALSO LIKE