Gana Lyrics
[VERSE 1]
Life bé tar, life bé tar
Life bé tar
Da ngey lidieunti sa bop
Mais do meussa kham nitte loum ley denthial hé
Borom bax la mais dal yé sokhor
Sama swagg sama style la sokhor
Sama flow limey rap ba sokhor
Balna len c’est normal niou sokhor
Mane baby bouma diay graw mane ay
Thiouray yeungeulouma hummmmm... yeah
Sama son dey daw ngey guiss ay
Chinoises yi leumbeul lou nar
No baby bouma diay graw mane ay
Djinjère yeungeulou ma hummm... yeah
Sama son dey daw ngey guiss ay
Narrou leumb di leumbeul lou nar
[CHORUS]
Niggah waxma pourquoi nga sokhor
Meunone nga bax mais da nga taneu sokhor
Vraiment khawma ioe pouquoi nga sokhor
Mounone nga liguey mais da nga taneu sokhor i say
Badman mièzé fresh ni penguin
Décembre la ley mey solou you fin juin
Niom nieup lay fay niou melni fin juin
Sol chino guéner kawass bou melni tintin hé
Y’Allah dou loudoul y’Allah dou loudoul
Y’Allah défouma dara am rappeur yi
Niouy soul en tous cas pas moi
Dal xel jeppeu ndigue ba melni Gana
Gana, Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Gana, Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Gana, hein hein ! Gana
Gana, hein hein ! Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
[VERSE 2]
Life bé tar ? life bé tar
Life bé tar
Da ngey lidieunti sa bop
Do meussa kham nitte loum ley denthial hé
Borom bax la mais Flag mo sokhor
H-Bomb ak Passa nio sokhor
Sokhor plus nieup melni pas bou sokhor
Fima diougué wa sicap pa sokhor
Kone niggah bouma diay graw
Li ngey niangal yeungeulouma hummm... yeah
Rappeur yi clash yag nagn déglou
Sama son yi di leumbeulou narr
Ma niggah bouma diay graw lou ngey rap
Mane yeungeulouma humm... yeah
Rappeur yi clash yag nagn déglou
Sama son yi di leumbeulou narr
[CHORUS]
Niggah waxma pourquoi nga sokhor
Meunone nga bax mais da nga taneu sokhor
Vraiment khawma ioe pouquoi nga sokhor
Mounone nga liguey mais da nga taneu sokhor
Y’Allah dou loudoul y’Allah dou loudoul
Y’Allah défouma dara am rappeur yi
Niouy soul en tous cas pas moi
Dal xel jeppeu ndigue ba melni Gana
Gana, Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Gana, Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Gana, hein hein ! Gana
Gana, hein hein ! Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana
Dal xel jappeu ndigue Idrissa Gana I say
Life bé tarr, life bé tarr
Life bé tarr, life bé tarr
Badman Mièzé , badman Mièzé
I say badman Miézè
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Gana (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE