Home Search Countries Albums

Sokhor

OMZO DOLLAR

Sokhor Lyrics


[OUTRO]
Anh ! Y’Allah meuna mayé
Y’Allah meuna mayé
amna nitte you sokhor nénagn
nioy nangou lou y’Allah mayé
Gnoniou borom bi lagn niémé
Borom bi lagn niémé
Niou ngui lékanté sen biir té
Amoul deum bou nex dérét

Dama am travail de maman
Doma guiss si TATA
Dama am travail de maman
Douma fils a papa
Dama am travail de maman
Nieupa am ay noone si life
Bi yonou diam sorriwoul
Kone tant que amo nioulay
Guerre soriwo ci life bi a buzzey

[CHORUS]
Anh ! Nitt yé sokhor Tellement sokhor
Beaucoup sokhor, pourquoi sokhor
Trop trop sokhor, pourquoi sokhor
Geun len sokhor Yéré you sokhor
Guel bou sokhor
Auto bou sokhor keur bou sokhor

Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Fauk nga sokhor
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Fauk nga sokhor

[VERSE 1]
Deum sur deumeu
Niow na fek fi ay deum sur deumeuu
Kou bakh sou niawé jiko neubeu na djeumam
Gni mome li ci séni deun mou leundeum
leundeumeu leundeum deum sur deum
Guiss guiss sou fen kate moy geumeul nga geumeu
Frash lay def sol jacket sama wouléma
Sa période niowagoul ni pneu bou eumb hé
Boul deuk si lidieunti kénén
Sama adresse mo ngui fénén
Di nga wathi ligueye parce que jobo
Bou féké may sa thiono massa thiono
Anh ! sama séttu dafa tothi
Ma dem dieundi télé pour guiss sama bop

Anh ! bayna noone yi di thiatou
Do dégeu béneu yo founiuy
Tathiou nioune nékougn ci yoyou
Kharito ak ay rappeur nono nékougn ci yoyou
Sissou bi nékougn ci yoyou niggah
Ma ngui séni kanam sayoumay reculé
Beurri class té meussouma redoublé
Boudé sa rap fayoula
Ndieugou auto fuck ioe ak message
Yi ngay véhiculé niggah akh

[CHORUS]
Nitt yé sokhor Tellement sokhor
Beaucoup sokhor, trop trop sokhor
Pourquoi sokhor ? Geun len sokhor
Yéré you sokhor Guel bou sokhor
Auto bou sokhor keur bou sokhor

Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Fauk nga sokhor
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Fauk nga sokhor

[OUTRO]
Ken momoul y’Allah
Y’Allah mo niou mome mais ken momou y’Allah
Mome moy taneu kouko nex rek mout al leu
Lolou soula mété nianal mou bal
Nianal mou bal la
Niampé niakh dess na eau de javel
Ngey bolé niampé niakh dess na
Té sa xol c fan la bomb mou béssate
Té sa khol si fan bomb leu wala goumbeu

[VERSE 2]
Aduna dafa goudou tank déh toungouné
Légende bir capsi ni thioukoulé
Takeu sama fitt heureux ménage
Takeu sama fitt heureux ménage
Dane na khékh ba am ay bleu
Ba ngay tass ay bleue
Pour dieund verre ak bic bleu lay bindé vers
you fresh ni jeudi vert
Amna khaliss bala billet bleue di vert
Clash ma meuneuleu défal pub
Beuss bo dadjék mane nak bol sakh négocié
Am rappeur youm fi solal jupe
Té walay bilaye douniou ay Ecossais
Hayders waxma ioe loumala amel
Orthographe si sa xol ak sa bambel

Khamna yougma yague nianal wayé ma ngui
Takeu nieupeu guiss ni phare des mamelles anh
Rap ak ay thiolé ci life bi no nioune nékougn ci yoyou
Ignane bi nékougn ci yoyu niggah mangui séni
Kaname sayoumay reculé beurri class té
Meussouma redoublé
Boudé sa rap fayoula ndieugou auto fuck ioe ak
Message yi ngey véhiculé niggah akh

[CHORUS]
Nitt yé sokhor Tellement sokhor
Beaucoup sokhor, trop trop sokhor
pourquoi sokhor ? Geun len sokhor
Yéré you sokhor Guel bou sokhor
auto bou sokhor keur bou sokhor

Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Fauk nga sokhor
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Bakh mo dièkh
Fauk nga sokhor

[OUTRO]
Anh ! Y’Allah meuna mayé
Y’Allah meuna mayé
amna nitte you sokhor nénagn
Nioy nangou lou y’Allah mayé
Gnoniou borom bi lagn niémé
Borom bi lagn niémé
Niou ngui lékanté sen biir
Té amoul deum bou nex dérét
Dama am travail de maman
Doma guiss si TATA
Dama am travail de maman
Douma fils à papa
Dama am travail de maman
Nieupa am ay noone ci life
Bi yonou diam sorriwoul
Kone tant que amo nioulay
Guerre soriwo si life bi a buzzey

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Sokhor (Single)


Added By : Tamsir Diouf

SEE ALSO

AUTHOR

OMZO DOLLAR

Senegal

Omzo Dollar is musician from Senegal ...

YOU MAY ALSO LIKE