Home Search Countries Albums

DIna Weet

VJ

Read en Translation

DIna Weet Lyrics

L’amour rends fou et donne des ailes mais mes ailes elles se sont brûlées

Je suis tombé et c’est très dur

Devant le miroir je me sens bête mais bon maintenant

Je me suis rangé tu sais que tu m’as perdu

Depuis année je redoutais ça

Mes gazo m’avaient parlé mais j’écoutais pas

En vrai c’est chant-mè tu m’as fait du saale

Et du sale

Dioxone naaala Lima yorone mou geuneu sori si mane

Sama xol sama Cheri

Di nga ma bayi dinaaa wet lool sama xol

Sama xol sama sama Cheri

Adouna laa dieul, diëbal lako nga wan ko guinaw dem

Sama xol dina metti, da nga xawone yakamti

Adouna laa dieul, diëbal lako nga wan ko guinaw dem

Sama xol dina metti, da nga xawone yakamti

C’était tellement beau t’a détruit tout ça

Et De l’ego j’en avais même pas

Oh mi amor comment t’a pu me faire ça

Fëral nga sama guèdiou baaanex

Maabal nga sama soufou mbëcktë

Faaye nga sama jantou lëray

(Chéri je t’ai épaulé je t’ai soutenu pendant des années)

Moussouma teudi tè tagoussi woumala goudi goudi

Goudi goudi thi yaw la wone nga goudèloooma

Adouna laa dieul, diëbal lako nga wan ko guinaw dem

Sama xol dina metti, da nga xawone yakamti

Adouna laa dieul, diëbal lako nga wan ko guinaw dem

Sama xol dina metti, da nga xawone yakamti

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG

Release Year : 2024

Album : (Single)

Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

VJ

Senegal

From his real name Mouhamed Abdoulaye PREIRA, VJ was born on June 7, 2004 in Medina, Dakar. He grew ...

YOU MAY ALSO LIKE