Home Search Countries Albums

BRK Lyrics


Khalé yi, teudi lene
Bayi lene grands yi témoigner
Omzo dollar jeul neu mic,
Problèmes yangui démarrer
Profession enseignant
Sa nopp di deglou en saignant
Yoro lugnu jakhal comme si vidéo bi lancer niang

Digeu khar comme, voyage ci bus bi
Charia bir russie
Chaque fois ma nieuwate ci benene forme melni variant virus bi
Rap galsene, bayi lene dima comparer ak ay domeram
99,99% de domeram
Toc toc adversaires yi djajeuf
Miezé leu sen place pères yi la jeul
Fils da melni planète terre bi la deupeu
Pour ma wathie sous-sol, atmosphère bi la jeum
Solou classe nga fokni mairie la jeul
Am yeré you yombeu mais you cher yi lay jeul
Li ngay mew dou souleur verres yimay jeul
Ndakh ki dougeul khorom si bir mer bi la geum
Hoes yi bakh na mais bou sèl ba geune
Ba legui amneu thiaz you guenteu nieuw
sama gallé soumekou melni ci vestiaires yi la deuk
Sans man dou jaleu ni canalisation
Garer 4x4 ni égalisation
Ay photo taatou rappeurs galsene ngay jot
Souma leu yoné sama localisation
Ci sen digui taat yi ma fey equitation
Sama khel comme A7 amoul stabilisation
Sama flow dou guéneu hospitalisation
Pour nga meune ma deglou faut nga chimie ac maths
Thiakry ak laakh,
Mélangeou Daddy B ak djily bagdad
Mane lagni clash ndakh
Kouma pousse mou takkeu ni batterie 4x4
Hakimi Achraf, gaaw ba def sene avenir flashback
Match bi tass ndakh, beuss bou rap bi cascade
mafi dikkat deupeu cartes yi ni black jack
Stratégie taf taf, yague di rap pour jeez alseyni ak paff
Def deux pas gnou jappeu di 4 pattes
Lerr neu ydee pape sidy ak tall

Digeu khar comme, voyage ci bus bi
Charia bir russie
Chaque fois ma nieuwate ci benene forme melni variant virus bi
Rap galsene, bayi lene dima comparer ak ay domeram
99,99% de domeram
Bou dee rap kessé…. Yeah
Bou dee rap kessé

Fuck say critiques ac hate yi
Samay semelles koukey tim
Dem kaaw di rap ay keyti sougn ma lathié sama keuyit ti dou dara
Hip hop bi la
Big godzilla
Kalashnikov yeramou nen wowé ma Nitdoff killa
Khalate you khot si sama bopp bi faut ga tew ak echelle
Fou yaar ay locks nekkeu tendance zo day yewou rek ndel
Yennay rappeurou boy yi mane may grand wou rappeur yi
Fresh ba sama jamou sappeur yi day taal camp wou sappeurs yi
Samay barres dou fixe
Allstar ni raptors knicks
Key, gas, ass ak nix
Boy yi chaque jour daalou thiere mais sorri negn pacotille
Wakh ma komay comparel ma jokh la sama analyse
Elzo jamdong wala ngaaka dip pour gattal liste
Ak quelques rappeurs ligue 2 you wat ni niongui football champions league
Lane lay battle ak ay iss?
Cool na ak niene ci yene
Diotek nienene ci yene
Mais li di li ci kaw mic bi walaye douma moromou keneu ci yeneu
Featuring ak niene ci yenn
Clashanté k nienene ci yenn
Sou omzo geunone present nenagn dougn deglou keneu ci yenn
Big up elzo big up ngaaka mais leneu la beugone rek mou lerr
Lou omzo defoul rap galsene omzo kesseh rek leu nekh
Top 3 doumeu troiss ni 2e mais
ligueye premier ni 2e mai
Wathié sama lokho tey troisième baraam pour rappeurou 2e main
Moustique youy clash ci souf dougnou loudoul boldof bougn tek ci table
Meilleur rappeur sénégalais, ces propos ne sont plus discutables
Khana fen khana dof khana cissou, ak ignane
Khana sokhor , khana bone, Khana tangue , ci cedday
Khana far bagn nangou deugue,
Khana may cauchemar ki ga beugue
2 ans guenewouma son mais lou fi khew rek zo leu nieup di reub
Khana hypocrisie publique
Khana sene niak  kham music
Khana sene jordan 25mil yi gendi gros plan si sene clip
Khana niveau d’étude bou souffé ak deumeu si bir ay nit
Khana blablabla mais fi ni boudeh rap kesseh

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2023


Album : BRK (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

OMZO DOLLAR

Senegal

Omzo Dollar is musician from Senegal ...

YOU MAY ALSO LIKE