Yawla Lyrics
Yagui dinde ak mane
Magui dioy ndax yaw
Liniou bolé mo beurry dolé aka ma lére yawla nop
Souma gesto guiss contane boma kholé réé
Liniou namanté yawla nop
Ragalou ma lolou (yawla nop)
Dawou ma lolou (yawla nop)
Guisso lii lepp yama diaral lii (yawla nop)
Ragalou ma lolou (yawla nop)
Dawou ma lolou (yawla nop)
Guisso lii lepp khasane nekh sama xool bi yaw (yawla nop)
Way way
Faan la si mane mbeuguel
Kham na may sa indo do léwato dém nga ardo
beug ngama bamou diékh bama kham ko dawou ma yolé (yawla nop)
Mane laniouy weur té yaw lay weur
Dièbal na sama xool bi nék ak yaw di doundou sama
Mbeugeul dafmay néx (yawla nop)
Mane nga fii té meun nga féé
Kham nga lii té kham nga léé
Réwal ma té doma yaar té
Bébé louma beug rek daflay nékh
Yagui dinde ak mane
Magui dioy ndax yaw
Liniou bolé mo beurry dolé aka ma lére yawla nop
Souma gesto guiss contane
Boma kholé réé ngigui namanté
Ragalou ma lolou (yawla nop)
Dawou ma lolou (yawla nop)
Guisso lii lepp yama diaral lii mane dh (yawla nop)
Ragalou ma lolou (yawla nop)
Dawou ma lolou (yawla nop)
Guisso lii lepp khasane nekh sama xool bi yaw (yawla nop)
Ndéké mbeuguel ni la nékhé dama beug lolou (yawla nop)
Magui bax yaar oyofal bama attane ko
Yeah amore (yawla nop)
Amore fo nek lay nék yaye bannéx yaye yeurmandé
Boulma méré tchi sama fiirangé bébé yo damala nop
Meunga fii té meun nga féé
Khamnga lii té kham nga léé
Réwal ma té doma yaar
Bébé louma beug rek daflay nékh
Yagui dinde ak mane
Magui dioy ndax yaw
Liniou bolé mo beurry dolé aka ma lére yawla nop
Souma gesto guiss contane
Boma kholé réé ngigui namanté
Ragalou ma lolou (yawla nop)
Dawou ma lolou (yawla nop)
Guisso lii lepp yama diaral lii (yawla nop)
Ragalou ma lolou (yawla nop)
Dawou ma lolou (yawla nop)
Guisso lii lepp khasane nekh tchi sama xool mi (yawla nop)
Beug na, beug na, beug na
Mane dh nop na
Beug na, beug na, beug na
Mane mi beug naaa la
Beug na, beug na, beug na
Mane dh yawla nop
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2022
Album : Yawla (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
DIEYLA
Senegal
Dieyla Gueye is a senegalese singer and songwriter. She was semi finalist at the Fourth edition of S ...
YOU MAY ALSO LIKE