Koti Koti Lyrics
[1er Couplet ]
Dof thi mane dieundé woma dara loudoul mbeuguél
Mala tane sépi lathi dakh yamay danél
Yaw kham ngnani kene dou kheutio lilou mome
My baby sama khol bi yako mome
Sama yéné di niou dounde ba sey am thi dome
Niouy koti koti yoli yoli lithi soukeur dou xorom
Rérone nga gindi ma
Dila way ni Youssou wayè Birima
Rérone nga gindi ma
Way la ni Youssou wayé Birima
[REFRAIN]
Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay
Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
[2ème Couplet]
Thiafka mbeuguel ngama niamal
Sama khol binga keuf moma sonal
Seytanè yi nagne niou mousseul
Yaye sama Messi dama beugue ngamay teul
Dila khalat di ré
Feep nga meuné
Gninane damay dieulé nagne ma thieupé
Doy nga kharit doy nga andando
Souma nieup bayé nala dessé
Mak yaw thi khalé
Rérone nga gindi ma
Dila way ni Youssou wayè Birima
Rérone nga gindi ma
Way la ni Youssou wayé Birima
[REFRAIN]
Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay
Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli
Lou dakh nekh
Lou dakh nekh
Lou dakh nekh
Koudoul yaw beugouma
Yafi nek
Koudoul mbeugouma hey
Koudoul yaw mbeugouma
Yafi nek
Koudoul yaw mbeugouma mbeugouma
[REFRAIN]
Koti koti …
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli kham linga name tax malay
Koti koti
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli … kham linga name tax malay
Koti koti …
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli kham linga name tax malay
Koti koti
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli … kham linga name tax malay
Lou dakh nekh!
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2017
Album : Koti Koti (Single)
Copyright : (c) 2018
Added By : Afrika Lyrics
SEE ALSO
AUTHOR
OMG
Senegal
Born on October 7th in Rufisque, Oumy Gueye, better known as OMG is a senegalese singer artist, ...
YOU MAY ALSO LIKE