Home Search Countries Albums

Kpakpato

ADIOUZA

Kpakpato Lyrics

Kpakpato Kpakpato
Fais gaffe à toi kpakpato
Kpakpato Kpakpato
Fais gaffe à toi kpakpato

Tu ne fais que parler de moi
Tout le temps parler de moi
Dire du mal ça te plaît
Mais jamais je te répondrais
Tu sais que j’ai pas ton temps
24h me suffit pas
Ça te fait mal je le sais
Mais jamais je ne te répondrais

Ba mAye tambaler job
Bobou yangui nelaw
Xeye di waxe rek di Sope
Saye waxe melni ngelaw
I make money I make money  mani
Yaw ngay weur di netalli
Douma sa ami
No no douma sa ami
Yak sa xalaat you bone yi

Def ma none waxe lou bonne amo diome
Di dieme Maye dem lolou mola yem
Sandi xere ma dieul ko def ko brique
Tegaler lene gnouye nelaw bank
Li nga gueuneu beug moy di guestou dima guiss Manè ca gannaw
Legui dama kawer ba degatouma sene aaye wax gnou gnaw

Kpakpato  Kpakpato
Fais gaffe à toi  kpakpato
Kpakpato Kpakpato
Fais gaffe à toi kpakpato

Delou santate none yi
Gno tax douma bayi
Bayilene ak thiow Li
Ne sa boupou loloye deal Bi
Meuner fi ak feuler
Lolou gnou woutaler
Bayil dima sossal
Xamo ma dima waxale
Li Yalla ji wax thi jeuwe
Nga jeule waxe defko ligeye
Gni done waxe nane dou gneuw
Aye atou ligeye taxoule gnou dappe ma
Kaye nga waxma gnangalou guinare
Lane mossiye  yonou paaka
Weurseuk Bi dinassi jot bamou meut menoulossi Dara
Li meti wone
Wess na
Es k Yaw mi wer nga
Qween Bi ngaye lathier kane la

Boko xamoule Modi adiouza
Boko xamoule Modi adiouza
Boko xamoule Modi adiouza
Boko xamoule Modi adiouza

Adiouza Adiouza Adiouza

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2021


Album : Kpakpato (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

ADIOUZA

Senegal

Adji Kane Ouza Diallo, better known as Adiouza, is a Senegalese female artist born in Dakar, Senegal ...

YOU MAY ALSO LIKE