Lekoko Lyrics

Mane déh lima dal khawma sax lane leu
Limou togue plus sam sou len ma
Moussou meu guiss guel bou mel ni ioe
Mome dafa spéciale kay meu wane len ko
Mo ngui lekk na fritte bi
Sauce bi bé dara la doul bayi
Kholal nimou def pothie bi
Mais boy bi esk sax nitte laaa
Lékeu ko mani ioe
Lékeu ko hey hey
Khampeu ko mani ioe
Dh khampeu ko héy héy
Lékeu ko mani ioe
Lékeu ko hey hey
Khampeu ko mani ioe
Dh khampeu ko héy héy
Abonél té nga aimé ko
Wowal sey kharite niou
Partager nieup guiss ko
Guiss ko dh guiss ko
Partagel hit bi
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Lekoko (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE