Guediawaye Lyrics
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh ! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh ! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
[COUPLET]
Nieuwal mbedo bénén life la mane ak sama gayi niougui bendo
Nieuweuk ghetto never mine la multitude pote mofiy daw.
Waww waww
Wane la lodoul guiss loudoul degg khamna digua know
Waxma yagui bègue yankoy yégue night bi di gueuna Go
Tékk zeum half night, talle call night late
film daw Twilight, teugue Match side side
Mbedo bendo lolou-oy ghetto
[REFRAIN]
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
[COUPLET]
Prisonnier sa peine kaygne lén la juger.
Fatéll lepp nieuweul niou diapisé, kagnou dem concert après niou gnibisi nénagn dioub dou wéss kon bokk gnibissi
Kay gnou dance boudé daff lay dimbali pour gua faté say pression
Eh kay niou dance fibou wésso hip-hop guisso centre de réinsertion
Tékk zeum half night, talle call night late
film daw Twilight, teugue Match side side
Mbedo bendo lolou-oy ghetto
[REFRAIN]
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh ! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh ! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh ! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh ! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Guediawaye (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE