Aminata Lyrics
Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse
Né ngua do guéne ak mane ndakh awmeu clash
Loutakh ngua melni Aminata?
Mane xamouma, bébé wakhma
Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse
Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu classe
Loutakh ngua melni Aminata?
Loutakh ngua melni Aminata?
Lane ngua meu eupeulé
Motoul sakh pép thiép
Nio bokk deuk tchi kogne, loutakh yaw ngua mayy khép?
Yéne dieuff yi nguay deff, tchi sama khol daf may guagne
Yéne say ma diépi leu déme bay bayi, khol bi bagne
Sama mbeuguél moma togne, motakh ma topeuleu
Mane ak yaw nio bok kogne motakh ma sopp leu
Kheuyneu beuss di na ame kagn, takk leu, téreul leu
Hé eh, Hé eh
Thioro baye samba, dak sa yaye dieulmeu
Sa nijaay yo may ma ay dollar, dou ma té daggo
Djank bi tchi kogne bi néna dou sey ak badolo
Bo démé keur yayam goudi gossi lay réré
Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse
Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu ay clash
Loutakh ngua melni Aminata?
Mane xamouma, bébé wakhma
Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse
Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu class
Loutakh ngua melni Aminata?
Loutakh ngua melni Aminata?
Lane mo takk si mane ba faléwomeu?
Lane mo nekk si mane ba xoloulomeu?
Nieuw na sakh si séne keur, mais wakhou lok mane
Té métinama ndeyssane, métinama ndeyssane
Pourtant nitt la kome yaw, kheuy neu beuss dineu changé
Pourtant nitt la kome yaw, wakh meu lane moy déranger
Nékal ak mane bilay, beugueu leu Yalla takh
Hé eh, Hé eh
Thioro baye samba, dak sa yay dieulmeu
Sa nijaay yo may ma ay dollar, dou ma té daggo
Djank bi tchi kogne bi néna dou sey ak badolo
Bo démé keur yayam goudi gossi lay réré
Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse
Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu ay clash
Loutakh ngua melni Aminata?
Mane xamouma, bébé wakhma
Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse
Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu class
Loutakh ngua melni Aminata?
Loutakh ngua melni Aminata?
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2020
Album : Aminata (Single)
Copyright : © December 2020 | 814 Prod & Taf Zion
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE