Home Search Countries Albums

Tassaré

DUDU

Tassaré Lyrics


Deuxième édition
Dudu fait des shows
6 avril Grand Théâtre 19h ley commencé
Dakar mako tothi
Casablanca mako tothi
Canal+ sax mako tothi
Fo dégeu radiakh dudu do fa diar
Dagniy natal sénégal
Jolof fi ley xéwé avril oui oui diko
Ndakar mandiaye waxko matar
Di rétane ba déh andil sa corbillard
Waw waw waw waw
Sorano la commencé am niou
yakarone mounoul fess
Mane ak sama équipe chaque jour
Gagné feep la tassaré
Ecole yi la tassaré
Afrique humour tassaré
Parlement du rire tassaré
Grand théatre dagn key tassaré
Abba mo ngui cibiir
Mahfousse mo ngui cibiir
Malcom mo ngui cibiir
Ken sibir ak ay artistes surprise
One mane show ban gui ni
Le livre de ma vie 100% Comédie
Spectacle garantie
Ambiance sou car rapide
Waw waw

[CHORUS]
Djouni nga doug niarry djouni nga doug
Djouni nga doug niarry djouni nga doug
Djouni nga doug niarry djouni nga doug
Djouni nga doug niarry djouni nga doug

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Tassaré (Single)


Added By : Tamsir Diouf

SEE ALSO

AUTHOR

DUDU

Senegal

Dudu is musician humorist from Senegal. ...

YOU MAY ALSO LIKE