Cila Bokk Lyrics
[INTRO]
Hahahahaha
(Bril on the Beat) ha ha
Yeah yeaaah Bril in the Building , héé
Cila Bokk way way Cila Bokk
Amoul Yakkalaté han , aythia Niou dém
[REFRAIN]
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress
Boula kén ray doundou dafay nekh
Koula beugga sonal Romb ko né mééss
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh
(kaay) “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
(kaay) Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
(kaay) “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
(kaay) Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”
[COUPLET 1]
Lo xamoul kagn lay djèkh dafa wara nékh
Boul faalé koulay méré wane ko beugn you wékh
Léppeu térangala, doundeul happyness
Lofi meunti am té béggo, amna louthi déss
Fii dal Sénégal la, boula nékhé dinga béggué
Boul nangou kèn yakkal-la
Dééko défé ning’ko beuggué
Daniouy dadjé foo di réé té xawma no Toudou
Selfie def ay Vidéo you fun melni #Dudu
#Baye_Mbaye , #Makh_Pro
koufi mér kone Wéro
Warnga meune di enjoy nga né town wala ghetto
Boul nangou kèn dila téré Happy
Kou sa life néékhoul, yakoy soppi
[REFRAIN]
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress
Boula kén ray doundou dafay nekh
Koula beugga sonal Romb ko né mééss
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh
(kaay) “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
(kaay) Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
(kaay) “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
(kaay) Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”
[Couplet 2]
Héé Yaw nanga déf
Koula beugga sonal thi wakh nèko mou déf,
Défam té bayila rèk yaw nga néthi
Take it easy , dafa wara yomb, waroul , méti hééé
Beurina ay Nitt you done foo djaarfa feullalé
Tèki_thi romboula wakh bo saani niou feul- feulalé
Kheuthiolén son you #Lourd , ma ték lou #Léger dilén Mour
Ngén may gueuna #Haine, maléni raw par #Amour
Bayilén niouy rawanté ngay dokh ndank , daagoul
Té koukay djaay méti , né ko “Lou Méti Yagoul”
Dél Khol sa none di réé né kouy sétane #Aba_Show
Caméra cachée #Makhfouss lay yooné sama Cho (copine)
[REFRAIN]
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress
Boula kén ray doundou dafay nekh
Koula beugga sonal Romb ko né mééss
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh
(kaay) “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
(kaay) Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
(kaay) “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
(kaay) Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”
[OUTRO]
(kaay) Héé féthial féthial way
(kaay) ni rekla yeungoul yeungoul way
(kaay) Héééféthial way
(kaay) ni rekla yeungoul yeungoul way
(kaay) féthial féthial way
(kaay) niou dèm , hèè Han han yeungoul yeungoul way
(kaay) mané Cila bokk haaayeah cila bokk
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : SUBA (Album)
Added By : Afrika Lyrics
SEE ALSO
AUTHOR
BRIL
Senegal
BRIL FIGHT 4 is a musician, Beatmaker, singer and rapper from Thiaroye - Diamaguéne in Senega ...
YOU MAY ALSO LIKE