Home Search Countries Albums

Ndiba Bi

AKHLOU BRICK

Ndiba Bi Lyrics


Dagnou ma sass awma togay
Dagnou tal gaz menou ma tok way
Money for life get money or die
Jok jot haliss guente bi doy na nalawougnou
All night yeah, all night yeah
May Ndiba bi ndourow mak yèn
May nalaw no waroma yéee
Bitches waroma yé
No seral kon Ngagn ko mayé
Sen Beatmaker né may def hit beat Aly Bomayé
Meun rap bou noy Ak rap ngora keng
Lo lén is meun mouni doul Ak day
Jeul drill fowéko gnoussate lén
Kagn ngéni dap Lima lén rawé
May Thérèse direct Molah yeah ( molah morgun)
Molah yé Mola yé ngew fay boy yi d man lay nèh
Kouy sen King ko wah king kénén koudoul Bismi
Bokalé nga yéah

Depuis corona bi Mangui won confinement
Ma indi wat confirmation
Potou ndala gnothiy nan mais dangay am éducation
Lambi golo diok ak danou yaw mono jogal noy dano
Lambi golo Jik danou hol danou yeah

Ndiba oh Ndiba bi yeah
Ndiba oh Ndiba bi yeah
Ndiba oh Ndiba bi yeah
Ndiba oh Ndiba bi yeah

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2021


Album : Ndiba Bi (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

AKHLOU BRICK

Senegal

AKHLOU BRICK is a group from Senegal. ...

YOU MAY ALSO LIKE