Home Search Countries Albums

Fatwa

CANABASSE

Fatwa Lyrics


Xam naa may kann xam naa limay diar
Boko Xamoul man xam nako faut que mou lerr
Gni dieme n’a gnou ma kham
Wayé gné dou gnou ma kham
Boma diangeh am xam xam ladj ko gni tew
Borom khol bou Woyof té laa bir
Gnakk kignane bagn  kou ley djey
Bo beuggeh degg dëgg ding’meu degg
Meune na la wayal
Meune na la wayal
Way bi diougeh ci xol, jaar ci xel
Guenneh ci guemign sarr seu nopp, laal seu xol
Dess seu bopp, feegn sey jeuf
Borom khôl bou deuguër
Meunou ma la wayal
Meunoumala wayal
Yay perte wallay demal ma dem
Demal ma dem
Yeah demal ma dem

I feel like I gotta do what I gotta do
Diaroul dougg ci alle bi sangook galladiou
Ndakh manguek full gëm gëm ba melni tay la toub
Yalla’y kün fek Mangui doundou ala athiou
Boul fokni soupou kandja bi ratakhatoul
Nel mère bi Mangui Thiop té rap takhatoul
Sa MC bouy nopi di thiolè kokou takha doul
Bandit bi done kaas ay sons you fëss tay moy thiakhagoune
Deumm dafay takhaw live lekk diakhatou
Thiaz bi dafay gnibi fadiar snap tchi diawartou
Legui dorkat yi gnoy mbeur yi lamb dokhatoul
Gayi kharètougn, Boy gayi geumeutougn shit
Gigolos yi tchi game bi di beuss pour fayekou

Kou sandi kher ci kaw
Ci souf caisser naa ay sous
Gni peuple bi lagnouy diemeu goukh diourgotkat rekkay lakk dounk
Hip hop shit bi yagg nagn gnou tchi siss
Di gnou sikk diema toutil sunu guiss guiss
Tay Sen business, eup doleh sen ay principes
Wantè lick lips, Mo geune Andak goor gouy suck dick
Afficher fi Viking
Dem fè wanè victime
Encaisser feu big chèque
Yeah you’re doing big thing things
Galsen est-ce que gni gnoy sène ay kings
Yenay sèèt mane daal Mangui sama lane ndakh té

Xam naa may kann xam naa limay diar
Boko Xamoul man xam nako faut que mou lerr
Diemou ma convaincre kéne baye
Sama nawlé ngi ci mirroir
Diemeu soppi sama life def ci Taar
Boy mercedess pour madame
Range pour sama bope

Thiono Bi ma dadj tchi life dou meuss dal sama dome
Echec douma meusseu daane pourtant weur na ma ndome
Abdou dieulil li nga moome
Baatou mère bi dou diouk sama bope

Gnome, bruit wou Lambo dou riir fou doul tchi sene gät
Gni daniou reer teh douniou ci guenneu diaroul seetkat
Sene day’a eupe sen tate, Wakh deug’a geunone simple
Ay doul mounoul yagg ndakh sen bum après sortie dougn ko deggat
Bandit tchi mic bi mais tchi life bi ndimbeul molay doundal
Bayil sagou bou dè dangeu khiff boy demal taadji tchin
Mane chèques yi may bindeu Dama lene bindeu ba la ma tchi bindeu
Gaïndè geudj gueneu ba takh tay ngay degg ay dialorè simbe
Hip hop Nigga, Geudj na la doundal
Waral nga dieul ay son wou bitch ass def ko zikr
Sincèrement Mangui plaider coupable tchi sa moussiba
Bayi la’k gnome gnou di la dik hadj nga yam Djeddah
Shit

Thiakay bi dafa bari fii
Doul ak diaayou rek lagnou diape ni moy indi bénéfice
Tè yamoul tchi rap bi secteur yeupp même chose nga fay guiss
Sport - diné - politique Boy febar be ngui FEPP
Mais nul n’est prophète chez soi wakhkatou deug fii danga ko miiss
Fallait que jänt watiè BBC gnou guiss Timis
Tabakhal mosquée sakh dou gnakk gnou la djign Iblis
Boy dagnou febar tè li gnouy fadj nekkoul ci Mercy Ships
Bou ma sagnone meune dentieu sama optimisme
Mais dafa thiole baye tè geuwma kene meune ci shit
Boy yi kham sexe di tek ay deals you set ni sen pubis
My nigga boy sèt kougn tchi gènè boul ko sèt tchi bène ndjiit
Deparou gaïndè dèmou gnou fène poussière ni TER
Danguay dagg BAC S atterrir bopou kogn degainer L
Borom keur yi diapougn tchi lène tek tchi stressè comme kou tèyè air
Dinero pour les enfants du règime boy loloy DER
Khandiou sokhatoul Ndatè hymen dangn koy possé légui
Téyél sa some bou bakh ndakhté humain dagn koy troquer légui
Wakhal bou bakh ndakhté bougn douté dagn lay sodé legui
Djigën you bari firangué
Mo len di sopi toké legui
Khalissou pédé fou taw arc-en-ciel dou len choqué
Mÿyi ci town bi guenné wou meu tchi sobé
Wanté mbir mi  boudé yassa boy gnoune gno tchiy soblé
Ndakhté lois yi lene di dolél boy gnoune gno ko voté
Séguam Imam lagnouy porter plainte nguir bagna degg dëg  
Mane May lane ba moutch tchi manque de respect
Gnakk kham rek
Animateurs yi taal rek
Khamnagn bou bakh vibe bi likoy violer
Yor nagn liste goor djigén yi bagn ko sandi ni Jamra
Sen wax yi feegnatoul sen comportement
Kom kom takh gnouy dokhé n’importe comment
Sene piques yi tchi mane comme dompot cadavre
Khamal lene ni Amoul bene verre bou meune khoss diamant
Lolou takh ma confortable tchi dess tchi sama bop
Tchi mane game bi amatoul enjeux Khana ma sét tchi gni ma top
Ma ngui sänt fouma tok
Bi God sépé gni done söp
Dotougnou sékk nouyo bro
Yeah fuck gneup sauf gniy wouyo Buzz

Xam naa may kann xam naa limay diar
Boko Xamoul man xam nako faut que mou lerr
Gni dieme n’a gnou ma kham
Wayé gné dou gnou ma kham
Boma diangeh am xam xam ladj ko gni tew
Borom khol bou Woyof té laa bir
Gnakk kignane bagn  kou ley djey
Bo beuggeh degg dëgg ding’meu degg
Meune na la wayal
Meune na la wayal
Way bi diougeh ci xol, jaar ci xel
Guenneh ci guemign sarr seu nopp, laal seu xol
Dess seu bopp, feegn sey jeuf
Borom khôl bou deuguër
Meunou ma la wayal
Meunoumala wayal
Yay perte wallay demal ma dem
Demal ma dem
Yeah demal ma dem

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2021


Album : Fatwa (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

CANABASSE

Senegal

...

YOU MAY ALSO LIKE