Namanté Lyrics
[VERSE 1]
Guissatoumala, dégatoumala
Wo nala té diotoumala
Danio dioté ngané dagma bloqué euh
Nioune fi niou diar motax
Tay li daf ma choqué
Boul fauk ni magu'ék kénén ioe la love
Niou beurré ma top wayé dagn ma soff
Faniniou nani ioe ioe rugn sa rétane
Ya ngui guiss mey caff
Di ré nga fokné dama contane
Li ngey guiss sama history
Bokoul ak li né ci mane
Ya ngui wané né da nga bégue wayé
Khamnani lolou dou ioe
Kham mane té nagn li ley danel
Leer nala ni mako meun
Gni ley top né len niou yam
Dama dé ci ioe té yama ray
[CHORUS]
Hey Ioe khamal ni nameu nala
Té ioe khamna ni nameu ngama
M'ak ioe souniou xol yi namanté nagn
M'ak ioe kham nagn ni namanté nagn
Héy ioe ! khamal ni nameu nala
(Baby nameu ngama) khamna ni nameu ngama
M'ak ioe souniou xol yi namanté nagn
M'ak ioe kham nagn ni namanté nagn
[VERSE 2]
Boul fauk ni ma ngui ci lénén
Mane kham na ya ngui ci kénén
Nianal nala nga dadjèk kouma geun
Wayé ci sama xél, néwoul louma geum
Sorri nga samay beut diégué sama xol
Lim mey def ya koy yeug lakatou dima khool
Nga wane ma guinaw
Takhoul ma faté sa kaname
Loma geun di ré ma geun fégn sa kaname
Dégatouniou wayé xol ya ngui guissé,
Bokatouniou yoon wayé xol ya ngui tassé
Dama watt né bayi nala
Dièm nala remplacer wayé dafa
Melni mounou mala tipsé
Bo déloussé dama koy fêté
Dama geuneu kham fane ngama fété
Diougal fi nga nék fékissima diéguéssima
Nameunala baby kay mounoumala fété
[CHORUS]
Hey Ioe khamal ni nameu nala,
Té ioe khamna ni nameu ngama
M'ak ioe souniou xol yi namanté nagn
M'ak ioe kham nagn ni namanté nagn
Héy ioe ! khamal ni nameu nala
(Baby nameu ngama) khamna ni nameu ngama
M'ak ioe souniou xol yi namanté nagn
M'ak ioe kham nagn ni namanté nagn
[OUTRO]
Boul fauk ni magu'ék kénén ioe la love
Niou beurré ma top wayé dagn ma soff
Faniniou nani ioe ioe rugn sa rétane
Ya ngui guiss mey caff di
Ré nga fokné dama contane
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Namanté (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
BRIL
Senegal
BRIL FIGHT 4 is a musician, Beatmaker, singer and rapper from Thiaroye - Diamaguéne in Senega ...
YOU MAY ALSO LIKE