Weetay Lyrics
Mmmmmmm
Bëss bou warone nex leu
Moudjé ay dioy
Sama yaram daaw na
Sama xol toy na
Kima beugueu demna
Kouma ko wakhone
Meunou ma ko gueum li
Comme ay lebone
Pekhé none lou am leu
Louma xam leu mane
Diam negne sama xol beu
Beumou diarré fa
Garap'ou mbeuguel so dagué reine ya
Boul si meusseu yakar guiss tcha dome yeu
Haaaaaaann
Nama nala lol
Té khawma fane nga dem
Douma leu massa faté
Ak fo meuneu dem
Sa megnane nala fekka
Fo meuneu nekka
Dalalal sa xeel
Sama xol ya tchi nekka
Nama nala lol
Té khawma fane nga dem
Douma leu massa faté
Ak fo meuneu dem
Sa megnane nala fekka
Fo meuneu nekka
Dalalal sa xeel
Sama xol ya tchi nekka
Seuy negne ba am ndiabote sama xeel
Diotoulo ma bayi kou maley kholé
Rogogne dina siit souma la gnaké
Mbeuguel dina tiiss
Diama wagnekou
Yalla na nga xiipé sama keur
Tiat begne la djitou
Tchi sa ndieguenaye
Te di nga yobalé sama mbeguel
Te di nga bayi mak doundou namel
Kham nané nala manquer lol
Wara doundou
Douma guiss sa dome
Dagne la nangou tchi samey lokho
Meyou gnouma sakh ma khol sa xol mane
Hannnn
Meyou gnouma sakh ma khol sa xol mane
Nama nala lol
Té khawma fane nga dem
Douma leu massa faté
Ak fo meuneu dem
Sa megnane nala fekka
Fo meuneu nekka
Dalalal sa xeel
Sama xol ya tchi nekka
Nama nala lol
Té khawma fane nga dem
Douma leu massa faté
Ak fo meuneu dem
Sa megnane nala fekka
Fo meuneu nekka
Dalalal sa xeel
Sama xol ya tchi nekka
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2022
Album : Weetay (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE