Home Search Countries Albums

Wanted Lyrics

Thiey li jomi na jomi na jomi na 
Thiey li jomi na jomi na jomi na 
I wanna see this girl ayway wan len mako 
Kuma ko guissal lum laaj man ma jox ko 
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa 
Wanted Wanted 
Hm hm.
Wanted wanted lélé (Baba, Baba)
Wanted wanted (Soxna ci ñëwël ci man kay way ah) 
Wanted wanted lélé  (Onyii Packathing)

Mom lay seet guisso ki
Tontu ma mu gaaw waxal way yah yah
Xoćc nama mbeggël i can't breathe 
Gennë guñu wayé ma ngui fiir yah yah
(Samba yow amna no mel ki nga guiss ko tëy ngani da nga ko nopp
Samba mi amna numu mel ki romb fi legui muni dafko nopp)

Thiey li jomi na jomi na jomi na 
Thiey li jomi na jomi na jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako 
Kuma ko guissal lum laaj man ma jox ko 
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa 
Wanted Wanted 
Hm hm
Wanted wanted lélé (Baba, Baba)
Wanted wanted (Soxna ci ñëwël ci man kay way ah)  
Wanted wanted lélé (Onyii Packathing )

Hey yeah 
Girl girl your body body make me crazy 
Teksi da nga bandit bandit sipp nga deal bi 
Linguere bu baax soxna ci you so pretty  (Hey Packathing )
Jabar lalay def aytia wan ma sa daddy  (Onyii Onyii)
Come to me and whine it for me girl  (Nananananana)
Come to me and shake it for me girl (Wawawawawawa)
(Samba yow amna no mel ki nga guiss ko tëy ngané da nga ko nopp
Samba mi amna numu mel ki romb fi legui muni dafko nopp)

Thiey li jomi na jomi na jomi na
Thiey li jomi na jomi na jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako 
Kuma ko guisal lum laaj man ma jox ko 
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa 
Wanted Wanted 
Hm hm
Wanted wanted lélé (Baba, Baba)
Wanted wanted (Soxna ci ñëwël ci man kay way ah) 
Wanted wanted lélé
Onyii Packathing 

Wanted wanted 
Wanted wanted 
Wanted wanted 
Wanted wanted

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2021


Album : Wanted (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

SAMBA PEUZZI

Senegal

Samba TINE, better known as Samba PEUZZI aka BG Boy Ghetto from Diack, is a young Senegalese Hip hop ...

YOU MAY ALSO LIKE