Home Search Countries Albums

Sante Yallah

BAYE MASS

Sante Yallah Lyrics


[VERSE 1]
Def nama goor yallah soudoul yé domou yayam diapaléma
Louma diokhagn ioe nga diokhma, mashAllah sante naleu
Diokhma ndeye diou mate ndeye, baye bou mate baye
Mane dh geureum naleu
Nite kou bax dou niakeu, loumou beug
Am ko ndax lamouy def thia xol ba (Al Hamdoulilah)

[CHORUS]
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah

[VERSE 2]
Oubil nama oubékou biir ak bité
oubi samay bountu def ma may niou nite gni beugeu
Sante na gnima diapalé bama wéssou lou méti

[CHORUS]
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah

[VERSE 3]
Gorr ley done, goor yallah dafay deugou kou bax ley done
Foula ak diom feel ndigeul mbotou yalla bi mome ley yor
Kou sante y’Allah bam ma défé lima done
Sante y’Allah bam ma défé domou niary gorr
Sante y’Allah bam ma mousseulé ci none yi
Sante y’Allah bam ma gnitaleu lé sama yone

[CHORUS]
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah
Sante na y’Allah

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Sante Yallah (Single)


Added By : Tamsir Diouf

SEE ALSO

AUTHOR

BAYE MASS

Senegal

Baye Mass is musician from Senegal. ...

YOU MAY ALSO LIKE