Home Search Countries Albums

Bamba

BASS

Bamba Lyrics

[COUPLET1]
Ba toubab bi diaxlé ba diaxlé, 
Dafaniko Bamba mouné ko mbacké 
Mouné ko yané wone do togn sa borom, 
Té do togn sa morome 
Té waxtu djouli diot na, 
Bo djouli woul waxtu wi, di nga togn sa borom 
Té djoulé souniou biir gall dig nga niou togn, 
Bamba sandi guedj gua toubab ba diaxlé

[REFRAIN:]
Do you hear me father Bamba
Did they hear you father Bamba
Do you hear me father Bamba
Did they hear you father Bamba

[COUPLET2]
Biss sa ngui niow, mi ngui ni di niow
Niou wéddi wone di dioy di reuthiou
Nann souma yeugone fekk mou wess
Boul diay lerr dieundé ko leundeum

your prayers, our prayers

[REFRAIN:]
Do you hear me father Bamba
Did they hear you father Bamba
Do you hear me father Bamba
Did they hear you father Bamba

Halamanii rahmaanou fii safiina Bamba bi ananii xadimu zil
madina yaw dale yaye ki niouy ramou.
Every day every night every moment
Dieureudieufé Sérigne Touba
Diarama borom Touba
Dieureudieufé Sérigne Touba
Diarama borom ndiaréme
Dieureudieufé Sérigne Touba
Diarama borom Touba
Dieureudieufé Sérigne Touba
Diarama borom ndiaréme

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Bamba (Single)


Added By : Tamsir Diouf

SEE ALSO

AUTHOR

BASS

Senegal

BASS is a senagal song singer. ...

YOU MAY ALSO LIKE