Nila (Remix) Lyrics
[VERSE 1]
Dolé dokhoul diam
Do mane té douma yow
Sagnsé damako tameu
Kholma ci souf ba cikaw
Té diémouma ko dama meun
Set ci wé ak ci karaw
Guissatouma louma nameu
Fima guéneu la nieup beug aw
Di nga ni nila nila
Nila waaay
Fi ma guén noy neu noy neu
Noy neu waaay
Di nga ni nila nila
Nila waaay
Di nga ma né noy neu noy neu
[CHORUS]
Nénala ngeu sol taille basse
Soloul ni ndanane bi
Soloul ni kou dieum nuit du dras
Boul faté foudeunou maquillage
Dionguama tague ley def moussorou
Dionguama dou sol bas
Nileu bilaaay, sama adjaratou sama adja
Nga solou mou yiw niou ande
Ma ame thieurou alladji
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
[VERSE 2]
Da nga né ci à péage romb la woroul
Do dioum ci maquillage mane damala wolou
Ya ngui teul sa greffage di dokh di dagou
Yor xirr di karawass ken meunoula sourr
Nékhoul ba nékhoul athi ngeu
Li nga sagnsé nekhneu
Ligu’ma défal bakhneu ya que beurri mana
Sol nga sa ndoquette taguanou
Mine nako ci yow oui mon cœur
Soula nékhé ragadjoul
Dane nga akhlou sagnsé
Looking my Marie Madeleine
Yagu’mey nirou marie madeleine
Yow sa dokhine nice neu woh ! woh ! woh
Dionguama kay tatafoumaaaa
Anh ! kay tatatfoumaaaa... hum
Nioweul tatatfoumaaa
Kay tatafoumaaaa
[CHORUS]
Nénala ngeu sol taille basse
Soloul ni ndanane bi
Soloul ni kou dieum nuit du dras
Boul faté foudeunou maquillage
Dionguama tague ley def moussorou
Dionguama dou sol bas
Nileu bilaaay, sama adjaratou sama adja
Nga solou mou yiw niou ande
Ma ame thieurou alladji
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
[VERSE 3]
Da ngey solou di geuneu nice
Solou di geuneu toy
Sama xol bi di geuneu nath
Fi nga guénati geuneu noy
Sama dionguama paradise
Sa solou dou meuna tok
Té nga bayi soumala né sagnsé
Ga nane ma bea da nga meuna togn
Meun nga solou
Meun nga sagnsé carr
Sa col bi tégou na ci temps
Sa mélo bi mo geuna tarrou
Té mane sa djiko bi la geuna fan
Mane ak nio dakh wa Guissé
Maabo nio geuna niro
Mane yow la tamou yow la appo
Sandi ma gouro
BB sa solou bi nala ci may note
Diokhma trois pièces bi damay sol
Dafa melni yow lepp la djapp meme
Solé loula eup sax dalay djote
Lalal nala bouko lali dagoul noum la
Nékhé nga diokhma sa lokho
Mélal ni kou dioigué Mali mane mala
Toudé Aminata Bakhayoko
[CHORUS]
Nénala ngeu sol taille basse
Soloul ni ndanane bi
Soloul ni kou dieum nuit du dras
Boul faté foudeunou maquillage
Dionguama tague ley def moussorou
Dionguama dou sol bas
Nileu bilaaay, sama adjaratou sama adja
Nga solou mou yiw niou ande
Ma ame thieurou alladji
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Nila ( Remix) (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE