Mangui Ci Sama Bopp Lyrics

Talouma yendou di cas (awma diotame)
Nekouma thi ay details (bouggoumako )
Danga faux mane doma sonal (taloumako)
Kharouma kene thi lene (no no no)
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui thi sama bopp
Dél wakh rek
Yakh dèr ak thiow li nga apo
Li Tamengako
Dokho thi daray mandou
Sopil djiko
Toppal adouna moulay djay
Lofiy def yako tey
Samay wakh nga yobou ko
Sédéloma sama djiko
Somay séntou thi gallou khadj yafay moudjou né dédjeu tokk
Samay wakh nga yobou ko
Sédéloma sama djiko
Somay sentou thi gallou khadj yafay moudjou né dédjeu tokk
Talouma yendou di cas (awma diotame)
Nekouma thi ay details (bouggoumako )
Danga faux mane doma sonal (taloumako)
Kharouma kene thi lene (no no no)
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui thi sama bopp
Domou garmi la mane
Khadiouma thi ay wakh
Topé Ngama mboro
Euy way khalè bilè Massa
Domou garmi la mane
Khadiouma thi ay wakh
Topé Ngama mboro
Bilay khawma li lanela
Doumla wakh dara
Wayè li metina
Khamaloma dara dima yakh dakh adouna
Mounouloma téyé fi yalla finé
Dom téré bék
Meunomeu stressé yalla téré
Samay wakh nga yobou ko
Sédéloma sama djiko
Somay séntou thi gallou khadj yafay moudjou né dédjeu tokk
Samay wakh nga yobou ko
Sédéloma sama djiko
Somay sentou thi gallou khadj yafay moudjou né dédjeu tokk
Talouma yendou di cas (awma diotame)
Nekouma thi ay details (bouggoumako )
Danga faux mane doma sonal (taloumako)
Kharouma kene thi lene (no no no)
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui thi sama bopp
Domou garmi la mane
Khadiouma thi ay wakh
Topé Ngama mboro
Euy way khalè bilè Massa
Domou garmi la mane
Khadiouma thi ay wakh
Topé Ngama mboro
Bilay khawma li lanela
Samay wakh nga yobou ko
Sédéloma sama djiko
Somay séntou thi gallou khadj yafay moudjou né dédjeu tokk
Samay wakh nga yobou ko
Sédéloma sama djiko
Somay sentou thi gallou khadj yafay moudjou né dédjeu tokk
Talouma yendou di cas (awma diotame)
Nekouma thi ay details (bouggoumako )
Danga faux mane doma sonal (taloumako)
Kharouma kene thi lene (no no no)
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui bakh
Mangui thi sama bopp
Mangui bakh mangui bakh mangui thi sama bopp
Domou garmi la mane
Khadiouma thi ay wakh
Topé Ngama mboro
Euy way khalè bilè Massa
Domou garmi la mane
Khadiouma thi ay wakh
Topé Ngama mboro
Bilay khawma li lanela
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2023
Album : Mangui Ci Sama Bopp (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
OMG
Senegal
Born on October 7th in Rufisque, Oumy Gueye, better known as OMG is a senegalese singer artist, ...
YOU MAY ALSO LIKE