Home Search Countries Albums
Read en Translation

Seydi Barhama Lyrics


Nioune nioy ndaw yi reeroon nga gindi niou Baye

Nioune nio xamoul woon nga xamal niou allah

Diox niou azkarou tarbiya niou fanawou

Xam lou gayi khamoul taxoul bagnou naagou

Kham ma ndieuk sooga parei meune meu jaamou

Mame yallah né soma xamoul nomay jaamo waa

Allah allah laa ilaaha ilalaa

Alhamdoulollah kou xamoul yallah dooko kham

Soob niou thi geediou leer yi

Nandal niou baniou mandi

Setal nga souniou xol yi

Jarama Baye barhama

Nioune nioy ndawou willani

Nioy borom faydou sani

Baye euweulou di yokk

Souniou mbeuguel si barhama

Barhama wotena

Barhama wotena

Barhama wotena wowoy

Baye Barhama

Allah allah allah

Allah allah allah

Allah allah allah wowoy

Baye Barhama

Barhama wotena

Barhama wotena

Barhama wotena wowoy

Baye Barhama

Rassoul minal mawla

Rassoul minal mawla

Rassoul minal mawla wowoy

Baye Barhama

Gni djitou woon raw nga leen

Yaa Seydi Barhama

Jonganté wook gnisi topp

Souniou waadji Baye

Fa goor yiy rawanté

Iow yaafa djitou Baye

Té sa mbeuguel si yonen moolako may

Borom gamou wooteena

Barhama niou gindi

Barhama niou indi

Nioune thi Faydou niou tékhé

Dieumi yonét bi Baye

Houwa cheikhou Tidiane

Houwal koulou minhoul koulou

Thieuy barham gagner na

Barhama wotena

Barhama wotena

Barhama wotena wowoy

Baye Barhama

Allah allah allah

Allah allah allah

Allah allah allah wowoy

Baye Barhama

Barhama wotena

Barhama wotena

Barhama wotena wowoy

Baye Barhama

Rassoul minal mawla

Rassoul minal mawla

Rassoul minal mawla wowoy

Baye Barhama

Borom gamou wooteena

Barhama niou gindi

Barhama niou indi

Nioune thi Faydou niou tékhé

Dieumi yonét bi Baye

Houwa cheikhou Tidiane

Houwal koulou minhoul koulou

Thieuy barham gagner na

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2024


Album : (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

WIZZY KANA

Senegal

Wizzy Kana is a singer and rapper based in Senegal Mbour ...

YOU MAY ALSO LIKE