Faut Pas Forcer Lyrics
[CHORUS]
Aka ma meun ci coté bi
Aka ma meun ci coté bé
May dièk gui rithi ci keur gui def ci gowé
Di guèl di rendi kill dokh di bondé
Aka ma meun ci coté bi
Aka ma meun ci coté bé
May dièk di rithi ci keur gui def ci gowé
Di guèl di rendi kill dokh di bondé
[VERSE 1]
Rétane ana louma nameu mane
A dandédo waxma louma nameu mane
Mane rek kham nga li di bonbon
Bonbon mane dh mako dakh wo
J’ai des renoms oh ! une belle africaine
Des lolos oh y’en à a gogo
Khalé douma takiné té makk douma moqué
Général defa leer
Sexy belle fresh
Je sais comment me saper
Je suis comme une déesse
Comme reine pas besoin de forcer
Je suis déterminé
[CHORUS]
Aka ma meun ci coté bi
Aka ma meun ci coté bé
May dièk gui rithi ci keur gui def ci gowé
Di guèl di rendi kill dokh di bondé
Aka ma meun ci coté bi
Aka ma meun ci coté bé
May dièk di rithi ci keur gui def ci gowé
Di guèl di rendi kill dokh di bondé
Faut pas forcer, faut modifier
Faut pas force , faut pas forcer
Faut pas forcer
Ay yay yay ya ! faut pas forcer
(Copie collé) faut modifier ay yay yay ya
Faut pas forcer, faut pas forcer
Faut pas forcer
[VERSE 2]
Kham nga class dougn ko forcer
Louboutin douko mayé
Nénala moytoul ruiné
Louboutin douko mayé
Mane aka ma meune (mane rek)
Bari dougou dougou wo (a dandédo)
Founé founé lay diar (rétane) aka ma doywar
Sexy belle fresh
Je sais comment me saper
Je suis comme une déesse
Comme reine pas besoin de forcer
Je suis déterminé
[CHORUS]
Aka ma meun ci coté bi
Aka ma meun ci coté bé
May dièk gui rithi ci keur gui def ci gowé
Di guèl di rendi kill dokh di bondé
Aka ma meun ci coté bi
Aka ma meun ci coté bé
May dièk di rithi ci keur gui def ci gowé
Di guèl di rendi kill dokh di bondé
Faut pas forcer, faut modifier
Faut pas forcer, faut pas forcer
Faut pas forcer
Ay yay yay ya ! faut pas forcer
(Copie collé) faut modifier ay yay yay ya
Faut pas forcer, faut pas forcer
Faut pas forcer
Kham nga class dougn ko forcer
Louboutin douko mayé
Nénala moytoul ruiné
Louboutin douko mayé
Mane aka ma meune (mane rek)
Bari dougou dougou wo (a dandédo)
Founé founé lay diar (rétane) aka ma doywar
Ay yay yay ya ! faut pas forcer
(Copie collé) faut modifier ay yay yay ya
Faut pas forcer, Faut pas forcer
Faut pas forcer
Ay yay yay ya ! faut pas forcer
(Copie collé) faut modifier ay yay yay ya
Faut pas forcer, faut pas forcer
Faut pas forcer
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Faut Pas Forcer (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE