Home Search Countries Albums

Déranger

VIVIANE CHIDID

Déranger Lyrics


Bilé mélokaane molay déranger
Xamna lilay sonal
Waax diou  bari tek thji nga  diss té yanou wo
Xamna lilay sonal
Bilé mélokaane molay déranger
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma séen dima rétann té beugoulo ma
Yallah mayma nangou wo
Ma rombou la nangou wo
Foma séen talalma lokho té sopou lo ma

Xamna lilay sonal
Mani wakh diou  bari tek ci nga diss té yanou wo
Xamna lilay sonal
Bilé mélokaane molay déranger
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma sèen dima rétann té beugoulo ma
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma sèen talalma loxxo té sopou lo ma
    
Hey ! Tiré ngama visél ndakh dalouma (louma)
Tiré ngama visél ndakh dalouma (hey)
Tiré ngama dolil ndakh dalouma (louma)
Sit down yow
Fi adinala konn tèyal
Fi adinala fils tèyal
Fi adinala konn tèyal
Fi adinala fils tèyal

Xamna lilay sonal
Waax diou  bari tek thji nga  diss té yanou wo
Xamna lilay sonal
Bilé mélokaane molay déranger
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma séen dima rétann té beugoulo ma
Yallah mayma nangou wo
Ma rombou la nangou wo
Foma séen talalma lokho té sopou lo ma
    
Hey ! Tiré ngama visél ndakh dalouma (louma)
Tiré ngama visél ndakh dalouma (hey)
Tiré ngama dolil ndakh dalouma (louma)
Sit down yow    
Dieuleul way  wi ma mayla yeah
Dieuleul way  wi ma mayla yeah
Dieuleul way  wi ma mayla yeah
Yaw dégloul way  wi may nala defko cas

Lingay dégager (dégager)
Mokoy déranger (déranger)
Yalla ko def thji yaw
Niou waxanté deugeu
Lingay dégager (dégager)
Mokoy déranger (déranger)
Yallah ko def thji yaw
Niou waxanté deugeu

(Hey, ma teug ko, ma teug ko, ma teug ko
Fèthieu ko, fèthieu ko, fèthieu ko
Vivi way fi niou teugeu fè nguèn dadi bégué
Nganni?)

Gal gal Amadou, Moustapha Diop malkhourédia baye lan niang moy sa man
(Moustapha Diop domou louga lô adja dior moy sa yay nitt kou baakh)
Wakhoumako wa louga ko wakh yangui dimbalé,  di diapalé
(Té doula togn, té doula togn
Elhadji bassirou diop moy sa beay Moustapha eeh way)
Moustapha Diop, Moustapha bassirou’roy  sa baye, dior diop sa yaye
(Vivi-Mbaye dièye faye loula yalla may
Gueuremèko  sa nday bagn douko dindi)

Nitt koulay woutt (lo si wax?)
Dièm dièm  diotoula (louy pékhèm)
Dafay sétt kila guena dièguè  mou diarèfa
Ba yakal leu wayè yaw mi boulèn falè

Mani nitt koulay wout (lo si wakh ?)
Dièm dièm  diotoula (loumouy def)
Dina sètt kinga  guena dièguè mou diarèfa
Ba yaxal leu wayè Viviane doulèn falè
(Boul falé, boul topato wayé dèlènn saurr
Vi-Vivi-Viviane oh, Vivi-yatma thiam nieuweul)

Lingay dégager (dégager)
Mokoy déranger (déranger)
Yalla ko def thji yaw
Niou waxanté deugeu
niaff

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2020


Album : Déranger (Album)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

VIVIANE CHIDID

Senegal

Viviane Chidid is a Senegalese singer of mbalax and R & B, born September 29, 1973 in Mbour, Sen ...

YOU MAY ALSO LIKE