Home Search Countries Albums

Gangsta Love

BRIL

Gangsta Love Lyrics


[VERSE 1]
Nioune niaar liniouy doundou
Ken meunou ko xam
Tay daniouy guissé
Bou souba niou réero
Meun nagn woulo
Ma fokni mane rek nga bagn
Té boumala soré nga def ma sa héros
Douniou andeu té douniou baayi
Tay meunanio xoulo souba
Niou guisséwate djubo
Biss bouné niou lathiéman
Lane ngay topé ki
Amna sakh niounane ma
Guiss nagn la ak kénén djubo
Hey ! Girl stop trying me yoo
Né nga bala nga am
Diam rek yaw fokk niou djoté
Sometimes I think girl you crazy yoo
Ni nga mey merlowé
mane nonou lala beugué


[CHORUS]
Mounou nio diapanté
Mounou nio bayanté
Métite biniouy doundou
Melni moy souniou mbecté
Gangsta - gangsta - gangsta
Gangsta love
Li moy Gangsta - gangsta
Gangsta - gangsta love
Tay niouy rayanté
Souba niouy raayanté
Amna loma def beu meunatoumala faté
Gangsta - gangsta - gangsta
Gangsta love
Li moy gangsta - gangsta  
Gangsta - gangsta love


[VERSE 2]
You play with me yoo
I don’t know why
I can’t leave you alone yoo
You’re on my mind
Me can’t put you out of my way yoo
Mane ak ioe forever
Ken douthi dem faté sa morome
Danio gaaw ci guerre té douniouy soldier
Téwoul louma am ioe yay borome
Hey girl stop trying me yoo...
Né nga bala nga am
Diam rek yaw fokk niou djoté
Sometimes I think gyal you crazy yooo
Ni nga may mérlo
Emane nonou lala beugué


[CHORUS]
Mounou nio diapanté
Mounou nio bayanté
Métite biniouy doundou
Melni moy souniou mbecté
Gangsta - gangsta - gangsta
Gangsta love
Li moy Gangsta - gangsta
Gangsta - gangsta love
Tay niouy rayanté
Souba niouy raayanté
Amna loma def beu meunatoumala faté
Gangsta - gangsta - gangsta
Gangsta love
Li moy gangsta - gangsta
Gangsta - gangsta love


[OUTRO]
Yaw yay sama wife
Meunoulo niakk ci sama life yaaw
You play with me yoo
I don’t know why I can’t leave you alone yoo

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Gangsta Love (Single)


Added By : Tamsir Diouf

SEE ALSO

AUTHOR

BRIL

Senegal

BRIL FIGHT 4 is a musician, Beatmaker, singer and rapper from Thiaroye - Diamaguéne in Senega ...

YOU MAY ALSO LIKE