Done Seet Remix Lyrics
[COUPLET 1]
Lepp louma am ak koumou done
Chérie boy yama ko gueuneul
Lima liguèy beuss bouné di ci sone
Ci lou bakh lepp yay borome
Yatakh ma xam kima done dioxma fitt
Retanal dotouma tite ooohh !
Lima liguèy beuss bouné di ci sone
Ci lou bakh lepp yay borome
Yatakh ma xam kima done dioxma fitt
Rétanal dotouma tite
Xolma ci beut my baby boul khéf
Té boul ragal diam rek ngey am
Lima beug rek moy kou bakh
So ki gueun borome xol bou nice
Kouma doul nakh dima bégueul
Souma diakhlé sakh moy deufeul
Kima done sett ioe leu maley dé hé hé hé !
Saub bey taw tey meu tak leu ndax da nga barri diome
Togal khar bama takk leu
Rééék téral leu
Doumala meussa fowé
Beu nopi ba leu fi
Goor you bakh yeup romb leu
Ioe ngey misère
La la la lal la la !
[REFRAIN]
Xamna beug ngama
Té itte xam nga beug nalaaa
Chérie bikk sakh feug nalaaa
Mais ci ay nélaw ngané beug ngama
Xamna beug ngama
Té itte xam nga beug nalaaa
Chérie bikk sakh feug nalaaa
Ci ay nélaw ngané beug ngama annh annh !
[COUPLET 2]
Fi leu fi leeuuuuu
Boudoul fi dou done fénén
Ki leu ki leu kiiiii leuuuuu
Boudoul ki dou done kénén
Ioe xam sa bop
Xam li ngeu done
Ndax jiguén dey xam bopam
Sama ngeu seu bop
Ya ngi xol euleug
Ioe da ngey aaamme ndiabote
Takk ngeu seu sœur
Moytou ngeu gars gni
Ndax bougn la xamé ngen bayi leu
Wax dji loumou nékh (hey !)
Nékha nékha nékh
Ioe boumla takh ba xam seu boop
Ndax jiguén amoul loudoul bopam
Wa walay jiguén amoul loudoul sageum
Mbeuguel mo nékh
Ci bougn la beugué
Mbeuguel mo nékh
Ci bougn la nobé
Mbeuguel mo nékh
Ci bougn la wolo
Mbeuguel mo nékh
Ci bougn leu safooooo… !
Mbeuguel mo nékh
Bara chérie soda leu
Mbeuguel mo nékh
Baye Diop chérie Amina
Mbeuguel mo nékh
Djily Niass chérie Sophie leu
Mbeuguel mo nékh
Henry chérie Amina
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2014
Album : Done Seet Remix (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE