Doumala Fowé Lyrics
Doumala, doumala fowé doumala
Doumala, doumala, doumala fowé
Doumala, doumala, doumala fowé
Soxna si, thi mane ngay moudia guissé love
Ndéké mbeugel is all i need mane
Sam sa daradia ni mame
Manam dou
Xallé bi boudoul yaw dou meussa done kénéne
Ndax sameu nga sa ndaw ni mame
Di guenou farata ni mame
Mane adouna la beugah wane
Baniou khamni que ni tekk nala fou kawé kawé
Togal sama wet boul ma meussa
Tagou ndax xamnga ni soma soré ma weet
Damla guiss yek tegé feulé sama mbonté
Mane lima yittel moy sama mbecté
Beugou mala disturb
Diegalou soun lay énervé
Non meti nala limla topé girl
Yalla xam na
Ni mane beug nala
Li takh niamé woma
Dama deung diar diar
Sam demb niawna
Ndieulbén dou nada
Mouthie gou rafete lay niane yalla diokhgn mala
Doumala fowé
Fima la foré da sorri
Sa reh djou nex
Momay fathie souma fébaré
Doumala fowé
Ndax fima la foré da sorri
Sa reh djou nex
Momay fathie souma fébaré
Ak lima meun guiss lima degg
Mane douma give up
Yen bi loumou meun diss loumou deugeur
Darra douma disturb
Neko ci réseau sociaux yi di polluer all time
Danaka sax do nek online
Fuck cheveux naturel enjoy nga life begg na
Lolo waral mane yaw lay nian
Damla guiss yek teggui feulé sama mbonté
Mane lima yittel moy sa mbecte
Beugou mala disturb
Diegalou soun lay énervé
Non meti nala limla topé girl
Yalla xam na
Ni mane beug nala
Li takh niamé woma
Dama deung diar diar
Sam demb niawna
Ndieulbén dou nada
Mouthie gou rafete lay niane yalla diokhgn mala
Doumala fowé
Fima la foré da sorri
Sa reh djou nex
Momay fathie souma fébaré
Doumala fowé
Ndax fima la foré da sorri
Sa reh djou nex
Momay fathie souma fébaré
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2021
Album : Doumala Fowé (Single)
Copyright : © 2021 Cosanostra
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
AMADEUS
Senegal
Real name Saliou Samb, of Senegalese nationality, the artist musician is known under the pseudonym o ...
YOU MAY ALSO LIKE