mbËggéel Dolee Lyrics

Lu ne ak fu ne
Lu mu mën ë ne
Bu ci am ul ee
Loo la du sore
Liy doole el lu ne , mooy mbëggéel
Waay , bokk bokk bokk yëg yëg
Loo lu moo ñuy daje le
Every where
Mbëggéel da fa yaatu
Lu ne lay am ci ku nekk
Lay feeñ , da fa yaatu ci domaine bu ne
Domaine bu ne , bu ne , bu ne bu ne , bu ne , bu ne , am na ca
Gis nga , da fa yaatu
Nit di në bëgg
Lu neex ci xol am muy mbëggéel
Nit lu muy bëgg
Yal na doon
Li gën ci moom
Nit di na bëgg
Lii bëgg leneen
Mbëggéel lë
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2025
Album : (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOUSSOU NDOUR
Senegal
Youssou N'Dour is a Senegalese singer, songwriter, composer, occasional actor, businessman, and ...
YOU MAY ALSO LIKE