Ahmadou Bamba Lyrics

Man su ma koy woy , faww sa ma xol tooy
Qui maye wax mooy , Modou Bamba
Dem na fu ne , dac na lu ne
Pour nous sauver , Modou Bamba
Voyage sur voyage , malgré son âge
Avec ses bagages , ñu sonn al ko
Mu jaay ante , ngir yërmande
Xeex al diiné , yanu ko
Moo ñu tann al , moo ñu xam al
Moo ñu niit ël , yoon wi ñuy jaar
Cheickh Ahmadou Bamba. Ak civisme
Humanisme , kaar waay kaar
Suñu mag ñi , xeex ngir diiné ji
Nañ leen ñaan al , saa su ne
Ñiñ fi bayyi , ñu yor ndono li
Nañ leen fohk , sargal leen
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2025
Album : (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOUSSOU NDOUR
Senegal
Youssou N'Dour is a Senegalese singer, songwriter, composer, occasional actor, businessman, and ...
YOU MAY ALSO LIKE