NLMD Lyrics
[OUTRO]
Ligeuy you ndeye moy agnoup dom
Rongogou mère si gnak diom,
Mandi baxoul soxor mo baxx
Té policier bi diay leu drogue
Meunougn ma faye (meunougn ma faye)
Ibliss dou sax job comme mane
Awmeu deukeundo si kaw souf
Bokoungnou trap omh non no non non
Founé dem na fa,
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
[REFRAIN]
Ni leu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Kone ni leu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
[COUPLET 1]
Assamane si meune xiine té dou taw
Sama mama dineu triste mais dou dioy
Deukou Christ mais seu fils beugoul foo
Béne domeum deufeu xiff tédou thiop
Diote meu yé seumay guénte
Di yettal seumey beugue
Goor yéngui yom goor djiguéne yi di gueune deugueur
Dou danga moumeu rek sa yalla wareu teukh
Diour sa bop soul seu bopp gnar rek moleu meuneu teu
Amo place même sisseu mère niggah
Foum leu diouré faleu seu makk yi diougué niggah
Meuwty dineu moudie déh
Matt deum bou rafète dou wallé fébare bou néxx niggah
Rakk woloule sa xarite yi
Beuss dineu ngneuw xamni saffara mo dakk fi
Déréta ma foore gnileu beugue sonale
Seu papa diangual leu xarou seu yaye nampalé leu possone
Mane deugn meuni diokhél seu xole ma dioxé seumeu rouh
Gnou xarre meu tidji seumeu gatte
Ma oubi seuma youre
Nathie dou yeuk sédday kéne leundeumoul beu lampe bou nioul
Yagg diox sa tate nitou goudi yarre ey dome you flou
Seu pêle bingjue gassé paxx bi
Si leugn lou moudie soul
Deumeu cher bomey ray déffé pakka wourouss
Tant que gnongui fène beusseul seu xole
Bagneu tontou mougn
Yakh derr yakouté xéssayou xéssal kate leu deugg bougou moure
[OUTRO]
Ligeuy you ndeye moy agnoup dom
Rongogou mère si gnak diom,
Mandi baxoul soxor mo baxx
Té policier bi diay leu drogue
Meunougn ma faye (meunougn ma faye)
Ibliss dou sax job comme mane
Awmeu deukeundo si kaw souf
Bokoungnou trap omh non no non non
Founé dem na fa,
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
[REFRAIN]
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
OUTRO
Kou amoul xole amo fite
Kou geum yalla do raggal
Ray négn kou dioudo goul
Teuthie negn kou déffoul dara
Seu mbokk diexx bo rayyé sey none
Meuno wète bo amé ndam
Défaite mom orphelin leu
Ni sédayou safara
Dangay business ni diné dou faaye meussoumeuleu su guiss
Nitou diam ngeu, kagn ngey dioubolé yalla ak ibliss
Euleuk tchi biiré dinga fégn nigga euleuk tchi biire
Nakho sa bopp, nakho yonénti bi,
Naxxo seu bopp naxxo yonénte bi
Ndax goumbeu dineu guiss souy guent,
Xale woné gnoumouy lakk bala bissou penthie
Deugeu métti ni secret secret youngueu dénthie
Do faté lo diangal seu bopp mouk
Kane mo meussoul féne
Yeah ! Thiagu bou yiw ni policier bou dioub
Meuno di déglou di waxx ni kounek sii douche
Bop bou fésse dey tekk dieuweum si souf
Motax couronne dey diape kou moussoul nekk buur ayy
Gni déh gnognou geuneu gnakk
Seu meilleu xarite leu yérré none bi di gneuneu diap
Yalla teuthie bidew tchi jail mouy lérale gnoune djante
Même kouy sangue néw sang katou néw dineuko sangu
[OUTRO]
Ligeuy you ndeye moy agnoup dom
Rongogou mère si gnak diom,
Mandi baxoul soxor mo baxx
Té policier bi diay leu drogue
Meunougn ma faye (meunougn ma faye)
Ibliss dou sax job comme mane
Awmeu deukeundo si kaw souf
Bokoungnou trap omh non no non non
Founé dem na fa,
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
[REFRAIN]
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : NLMD (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
DIP DOUNDOU GUISS
Senegal
DIP of his real name Dominique Preira is a Senegalese rapper born in 1991. DIP is an abbreviation of ...
YOU MAY ALSO LIKE