Yallah Baaxna Lyrics

Sa youma kheuyé damay sante sakou niane
Yallah mousseul ma thi am xol bou boon
Bania wathi yoon bima wadjour yi teggone
Dakhté
Yen say damay diekki tite thi man
Di guiss ay djiko youma khamoul woon si mane
Mba dou diamono dafay sopi sama xol
Do bakh baniou fayela lou bakh
Guiss loulay sikeul gueneu yomb guiss sa mbakh
Def louy yakh gueneu yomb louy defar
Alal djiteul niou baniou dem ba faté Yallah
Han han hannn yeah eh eh yeah eh
Oh non oh oh yeah
Diamono diéka dooy waar
Gni di gass gni di soul
Kagn lay baax
Mbok deugueratoul
Xarit deh amatoul
Ken guemeutoul ken dax ken woreutoul
Xol yangui khat di gueneu leudeum
Yénenté wouniou jamm kou nek djiteul boppam
Kila gueneu diégué gueneu meuneu def lou niaw
Yamatoul thi daas paka bilay diam thi guinaw
Xol yi fess na del sokhor ak ignane
Dieuf diou baax dou wess
Yallah baaxna
Naniou delo xel thi
Yallah baaxna
Delossi djiko you rafet yi
Yallah baaxna
Naniou délo xél thi Yallaf thi Yallah thi Yallah
Yallah baaxna
Naniou delo xel thi
Yallah baaxna
Delossi djiko you rafet yi
Yallah baaxna
Weurseuk ken douko lekk koudoul borom
Yallah baaxna
Han han han
Yallah baaxna
Yeah yeah yeah
Yéné nék le borom mossiy fanane
Kone naniou yénenté jamm ak salam
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2020
Album : Yallah Baaxna (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
OMG
Senegal
Born on October 7th in Rufisque, Oumy Gueye, better known as OMG is a senegalese singer artist, ...
YOU MAY ALSO LIKE