Home Search Countries Albums

TchéKoulé Lyrics


Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa
Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa
Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa
Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa
Tché tché tchékoulé
Tché ko vista ko vista ta lànga
Ka ka tchi lànga
Tché tché tchékoulé
Tché ko vista ko vista ta lànga
Ka ka tchi lànga

Tàggu naa mbaar njaay
Tàgguti naa mbaar njaay
Ndongod may may lengee
Ma bàkku céru ndey ak baay
Xaaxtandiku kàllaamay wolof big up buur ba jolof
Sarenzo pacotille ak ndem-si-yàlla vieira ak las mc
Rap pop doo bopp nga dem ardo
Bu jinne bëggee daqaar ku yéeg daanu
Boo reppee ci xare lu mu jiin xeeb ko
Da ngay xaru di nu tëkku tey sa fan ñu leb ko, ahh!!
Boo bëggee sàqami sunu lanc di nga bekkoor
Nangu da fa jël céru bañ aah, suukëru koor
Daan dox gox ba gox ngir freestyle téya mic ñeme naaj
Fosco discothéque walla ladies night how many mic !!!
Dagg nga sa geetar uhh uhh uhhh gis nga ku la gëna feebar

Jaaba débaa laa
Tché tché tchékoulé
Tché ko vista ko vista ta lànga
Ka ka tchi lànga
Tché tché tchékoulé
Tché ko vista ko vista ta lànga
Ka ka tchi lànga
Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa

Tàggu naa mbaar njaay
Tàggooti naa mbaar njaay
Faada aal ma lengee
Ma bàkku céru ndey ak baay
Téyal catu ndab booy lekk ci ceeb bi
Di nga yàbbi li nga sex booy teggi
Ndawal li ci digg bool bul seppi
Njëkka dóor yàkkamti la ci xeex bi
Suul ker du ko tere mësa féete kow
Yaa ngi course ak dee moo la gëna gaaw
Dañoo wuute bi style te du mësa bokk
Dafa yàgg ñi di coow ne du mësa dox
Dañoo taq ban ripp buñu jéema topp
Fi nu jaar boo fi ñëwee di nga gën a xoox
Lewël bu tàng jërr ëf ko te jeeri ko
Laax buy lakkee bul bëri coow ni barigo

Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa
Jaaba diba bilaaa
Jaaba débaa laa.....
Dégglutileen bismilaay jàmm la
Tàggu nanu mbaar njaay
Tàggooti mbaar njaay
Dégglutileen bismilaay jàmm la
Tàggu nanu mbaar njaay
Tàggooti mbaar njaay
Dégglutileen bismilaay jàmm la
Tàggu nanu mbaar njaay
Tàggooti mbaar njaay

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Yaamatele (Album)


Copyright : (c) 2019 Bois Sakré/All Made


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

NDONGO D (DAARAJ FAMILY)

Senegal

Ndongo D. is a Senegalese rapper, a member of the Senegalese hip-hop group Daara J. The band was ori ...

YOU MAY ALSO LIKE