Home Search Countries Albums

Yole Lyrics


Yow kay ma netali lenn noy, ben histoire boumafi dalon
Samdie soir may seti, sama xalé bou bess bi
Beuss bobou lamaci daal mane faw ma nétali len ko
Bama yégué sa keur ga niou terrou ma, nignuy tero buur
Tallal ma thiouray teegal ma reer bu neex dall may goonal
Bamou dess loudoul gnibi, ma andeu ak xalé bi, moumay goungué
Bama démé sa mbeed mi, né xaral ma tagato ak mom diokh ko ben calin
Guestou yam si Amy, Amy rakou lily sama benen geel bi (sheuteuh teuh)
Mane thiolé na, ndax Amy dianama yolé yolé, mba douma yolé yolé
Thiey fouma dieum, ki dinama yolé yolé
Mba doma yolé yolé, may xallat ndax doma yolé yolé
Xalé bi dinama yolé yolé, xamna dinama yolé yolé

Diamono dji thiey ndoumba lame
 Mangui sangou tewoul samay tank di fegn
Du nétali sakh way loumou yeug mou siw
Néna mur yi sakh, niom dagniy wax téléphone yi di gnofi daka yolé
Yolé yolé yolé, hé mba doma yolé yolé, xalé bi dinama yolé yolé
Thiey fouma dieum ki dinama yolé yolé
Wouy fouma dieum ki dinama yolé yolé

Sayou foor yombé rek, seug diafé wawawwww
Kham na sou ndiab yaggué légui gawar fegn
Wooh wooh wooh
Leeh leeh leeh leeh
Sa deugeu deugeu deugeu nak

Mane mako def, waye bamako seté guiss na danie ma yolé
(yolé, xalé bi dafa yolé)
(yolé, xalé bi dafa yolé)
Mane bama woté mou bloké ma, thia la khamni amy moma yolé

Mane mako def, nangou na mako def
Wayé bama sété sétate, guiss nani danie ma fowé
(yolé, xalé bi dafa yolé)
(yolé, xalé bi dafa yolé)

Mane bama yeksé, kaname ngey saxar thia la khamni amna koufa diar
May gontu ngiir mou balma
Yoné ko fleur nguiir mou balma
Léppeu loma lathie, mane déh paréna nguir defal lako
Sa deugeu deugeu deugeu nak
Mane mako def, waye bama seté sétate guiss na danie ma yolé
(yolé, xalé bi dafa yolé)
(yolé, xalé bi dafa yolé)
Sa deugeu deugeu deugeu nak

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Cey Li (Album)


Added By : Tamsir Diouf

SEE ALSO

AUTHOR

MOMO DIENG

Senegal

Momo Dieng is a singer-songwriter performer. ...

YOU MAY ALSO LIKE