Gauche & Droite Lyrics
Yaw la Yaw la Yaw la
Yéné sama xol ndakh damala
Love té sakh kafou ma ci
Dama sensible deug la
Dama feel beug la diokh
Sama xol bi ndakh damala
Khalé bi té mala diokh
Sama xol bi
Ndakh damala love
Damalakay diokh, damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Chéri ba nopi sopi sama sant
Damalakay diokh damalakoy diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh
Han man, han hawma lanela
Ma ngui doundou love story bouma yéém
Boulma laadj louma dal nii
Sama nobél amoul foumou yam
Khalébi soma laadjone
Jant bi, non tey dou fanane
Khalébi soma laadjone
Sama bakane, damalakay diokh
Damalakay diokh damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Chéri ba nopi sopi sama sant
Damalakay diokh damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh
Gauche wala droite?
Dis-moi si tu veux en haut en bas ?
Dis-moi Lou tang wala lou sééd?
Dis-moi
Ma servir la
Bou 19h dioté gnou teudi
Na metti, na yaag, na melni
Khalébi boul ragal na nga yekssi
Gnoune kessé la thi keurgui na djoly
My babe touch my body ouh !
Everyday ma diokhla nga né thi
Khalébi tekk ma lou metti
Bou yékhé thi yaw la
No no dou thi man han yayayay
Han man, han hawma lanela
Ma ngui doundou love story bouma yéém
Boulma laadj louma dal nii
Sama nobél amoul foumou yam
Khalébi soma laadjone
Jant bi, non tey dou fanane
Khalébi soma laadjone
Sama bakane, damalakay diokh
Damalakay diokh damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Chéri ba nopi sopi sama sant
Damalakay diokh damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Yalla ko def lolou louma thi meun
Damalakay diokh damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Chéri ba nopi sopi sama sant
Damalakay diokh damalakay diokh
Damalakay diokh love bi nek thi mane
Yalla ko def lolou louma thi meun anh yeah
Oh yeaah ! Oh yeah
Ndéké khalébi rek laa nop
Mane khalébi rek la nop
Oh yeaah ! Oh yeah
Ndéké khalébi rek laa nop
Mane khalébi rek la nop ba sagar khégne
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2024
Album :
Added By : Maffoho farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE