No More Lyrics
[COUPLET 1]
Sama xol bi nga dieul, def ko éponge
Lou niow ma dieul
Ma mounieul lako oh !
Baby, lolou ba kagn
Loumou métti métti, ma nékal la fi
Ngey takk di tékki, ni kou yor mairie hi !
Sama yeuf ma nangoul lako
Khawma ioe la, khawma mome la
Wayé sama xol, antanoul li
[REFRAIN]
No more, no more, no more, no more
No more, no more, no more, no more
[COUPLET 2]
Woudj bokk weurseuk la
Nga fakh sa keur né fi bakhna
Kénéne kou fakh mélni ioe dou né fi bakhna
Dou mala yattal ba nga niow seuy
Nga weulbeutikou beugeu tass sama seuy
Sett si y’allah bayima mougnii
Louuu… lou waye def bopam
Louuu… lokho def lokho mokay dindi
Bo beugué kham, fi la y’allah tolou
Kholal, di nga ko yékhaa..
Khawma ioe la, khawma mome la
Wayé sama xol, antanoul li
Wayé sama xol, antanoul li
[REFRAIN]
No more, no more, no more, no more
No more, no more, no more, no more
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : No more (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE