Champion Lyrics
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan
God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan
Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss
Champion nga fils
Bakoul reik maay guiss
Champion deug nga fils
Mane beurrei na walahi beurrei na
Mane beurrei na beurrei na beurrei douma danou
Entraîné na entraîné na entraîné na aiguisé sama mind
Dou xool be nieuk fatélikou demb nimou meitei wone
Waral ma xaali yonne beugeu done champion
Ñi né meune nako deef ñi né meunuta baax
Saalo ligueey ak ngeum ñanou wadiour mooy Sama dolé
I don’t care Balla waxal douma terrei deef
Xarañe na ba nieup nangou maay modou si biir Gueew
Wayè yallah baxna ioe yallah bakh nga
Mousseul ma mane si samay pekheem noon
Bayi ma ak Sama xeel ma meuneu agaalé mbeubeut mi nè si mane
Ndax champion laay meusseu done
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan
God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan
Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss
Champion nga fils
Bakoul reik maay guiss
Champion deug nga fils
Sky is the limit on a plus rien à prouver
Baal ba taak na bideew bou diougué assamane
Kouy waax bokoul ak kouy dieuf mane damay beurrée daane
Dolé gaindé ndiaye doma degeul ndeysane
Xamè na diandj ak dior xamè thiamoñe ndey dior
Todj na lamb ndakaru thies kay diap siki thior
Kaay waay mane beurrei daan laay guiss
Geum geum bi dotoul deign ba Abadane daiman
Sakou na ñane Kou faraal jeeba neko ya meune
Wayé Yallah bakhna ioe Yallah bakhnga mousseul ma mane
Simay pekheem noone
Bayima mane ak sama xeel ma meuneu agalé mbebeut bi né
Si mane ndax champion laay meusseu done
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan
God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan
Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss
Champion nga fils
Bakoul reik maay guiss
Champion deug nga fils
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan
God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan
Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss
Champion nga fils
Bakoul reik maay guiss
Champion deug nga fils
Hé jeeba le boy
Hé jeeba le boy
Hé hè jeeba le boy jeeba le boy jeeba le boy
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2022
Album : Alajee (Album)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE