Je Ne Suis Pas Lyrics
Suis pas
Ki ngay dawlo ci mbéd mi
Aduna tey diangal nama
Cheri boy , tey lorr ngama
Mane, je ne suis pas
Ki ngay dioylo ci mbéd bi ehh
Amna lenen mane Louma gueum
Boudoul yaw di sa morom
Kou ci xass ba yeuk love do khamé bay guiss djiko
Loooooo beug ma def ko
Amna Lou bakh té yaay borom
Ta Loula dall ma yeuk ko
Amna amna amna amna kou bakh
Lolou la defone
Mane je ne suis pas
Ki ngay dawlo ci mbéd mi
Amna lenen mane louma gueum
Boudoul yaw di sa morom
Gueumone na ci sama xol bi yaw mi lagn may bolel
Geumone na ci sama xol bi yaw mi yamay dolél
Yaw mi yaye borom
Geumone na ci sama xol bi yaw mi lagn may boléle
( Gueumnaa ah ah )
Geumone na ci sama xol bi yaw mi yamay dolel
( Gueum naa ci sama xol )
Yaw mi yaye borom
Alalou wadiouye foo
Kou farlou yaay borom
Kou farlou yaay borom
Kou farlou yaay borom
Amna Lou bakh té yaay borom
Ta Loula dall ma yeuk ko
Amna amna amna amna kou bakh
Kou farlou yaay borom
Je ne suis pas
Ki ngay dawlo si mbéd mi
Amna lenen mane Louma gueum
Boudoul yow Di sa morom
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2022
Album : Feel Me (EP)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE