Mame Bamba Lyrics

[VERSE 1]
Dieureudieufé Mame borom Touba Mbacké
Ligueyal nga diné l’Islam, indi nga diam
Def nga ci xol yi
Raw nga sey mass Mbacké yafi né
Ya diakhal toubab bi, moussoul tarr nga khadi
Bamba feep, Bamba partout, ya am ndamee
Ya am ndamee
[CHORUS]
La Ilaha Ilala, La ila ilala
La Ilaha Ilala, La ila ilala
La Ilaha Ilala, La ila ilala
[VERSE 2]
Dem nga werr werr, diar mayomba
Lig fa dathi da méti moussoul wone yomba
Diouli ci guethi gui, niarry rakkay ndar
Fi nga diar koufa diar dina takh bann
Ken dou ioe Mbacké
Ken dou ioe Mbacké
Ken dou ioe
Modi bayou Mame Moustapha Mbacké
Ken dou ioe Mbacké
Ken dou ioe
Modi bayou Mame Fallilou Mbacké
Ken dou ioe Mbacké
Ken dou ioe
Modi bayou Mame Saliou Mbacké
[CHORUS]
La Ilaha Ilala, La ila ilala
La Ilaha Ilala, La ila ilala
La Ilaha Ilala, La ila ilala
[VERSE 3]
Sa weuy dou fay, Mbacké am nga ndam
Diarama Mame Cheikhra Fall ya khaleu yone wé
Sa weuy dou fay, Mbacké am nga ndam
Diarama Mame Cheikhra Fall ya khaleu yone wé
Sa weuy dou fay, Mbacké am nga ndam
Diarama Mame Cheikhra Fall ya khaleu yone wé
Bamba feep, mou fess souniou xol
Bamba fila, Bamba lerr leu
Bamba feep, mou fess souniou xol
Bamba fila, nioune Bamba rek moniou doy
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Mame Bamba (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
IZO DASS MIND
Senegal
Izoo (Bu Dass mind), whose real name is Issa Cissé, made his rap galsen debut in 2003 in a su ...
YOU MAY ALSO LIKE