Home Search Countries Albums

8 Mars

EL MAESTRO

8 Mars Lyrics


Boul dioy
Sister

Promotions canapé
Mongui tothie deuk bi Bilahi
Ñom ñimakoy tek (Wawaw)
Ñom ñiomay sargal 8 Mars
Violence conjugale (Ndeysane)
Mom lay doundou Bilahi
Mom mimakoy tek (wowowa waway)
Mom momay sargal 8 Mars

Journée internationale  des droits  de la femme
Journée de réflexion la wara done
Journée de revendication (non non)
Waroul nek journée poukarék sagnsé (non non non)
Jiguen yiñouy maltraité
Lañouy sargal
Bou 8 Mars jooté (Jooté)
Yén chef d’entreprise yi organiser fête
Wo kép kouy jiguen
Di wax ay bax baxam
Té bamouy ñeuw si bureaum
Beug liguey
Def ko ladj bopam
Bamouy ñeuw bureaum
Beug beug promotion
Daf ko violé (wawaw)
Non non non
Non non non non non
Kissa rakk la (Li dafa ñaw)
Boul ko def li deh (Li dafa ñaw)
C’est ta sœur

Promotions canapé (wowowoy)
Mongui tothie deuk bi Bilahi (Hé)
Ñom ñimakoy tek (non non non)
Ñom ñiomay sargal 8 Mars
Violence conjugale (Ndeysane)
Mom lay doundou Bilahi
Mom mimakoy tek (wowo wowo wowoway)
Mom momay sargal 8 Mars

Wowowowo wowoway
La violence faite aux femmes
N’est pas seulement physique
Le faites de l’atteindre psychologiquement
Est vraiment horrible
Yako wara protéger
Ya wara dalal xelam
Yay goor
Ya wara tax dou dioy
Lalala lalala lalala (Hé Yaah )
(Dou yoon)

Yagui nek ak mom si keur gué
Diko voilenter
Xolo doom xoloné
Ki man na done sa rakeu
Bou jiguen wala sa Diarbatt
8 Mars dioté
Guéni hotessou
Nane diarbar sama
Diko sargal mouy retane
Xamo loumouy doundou si xolam  (Xolam)
À travers la voix de femme je parle (Hé aah)
Je parle je parle et je parlerais
À travers le cœur de la femme
Je pleure je pleure
Mangui dioyy wowoway

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2022


Album : 8 Mars (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

EL MAESTRO

Senegal

El Maestro is a Senegalese beatmaker, composer and actor ...

YOU MAY ALSO LIKE