Dina Tarr Lyrics
[REFRAIN]
Dey tarr rek di geuneu tarr, waw dina geuneu tarr
Yokal thiéré té nga doli nièkh beut yeup si mane comme kou sathie birr sandaga
Mbok ndax xol ya ngui fékh (xol ya ngui fékh)
Ndax dina geuneu tarr
Ana sama noone yi,
Niom nio féssal hopital ak armére yi dey geuneu tarr
Yokal thiéré doli nièkh (doli nièkh)
Ndax dina geuneu tarr
Waw boy dey geuneu tarr,
Boyi ba légui nio ngui sétt atoumane
Mbok ndax xol ya ngui fékh (xol ya ngui fékh)
Ndax dina geuneu tarr
Waw boy dey geuneu tarr
Topou la ba sugn ley gassal camb
[COUPLET 1]
Han ! Dey tarr ni tallatey nder
Ba na clashanté
Légui bomay togn mey dakhar sa …
Soumey dem be séral khalate sam mère
Hey ! Dina néx si nioune
Di geuneu tar si ioe,
Reptyle li geun moy nga far si niom
Puta madré va fanculo
Fuck tranpoline légui danio takk sikaw
Sa label dafa labb ni kou done fey si ténn
Gni dess si yen la niow ray si tay
Dizzy mouk dou danou
Di ngen moudjou ganiou
Wadiou khogne vierge seuy si tay
Deuxième chance
Nga geuneu wéré
Bm jaay loutax ni niou beuneulé rek
Damay geuneu bégu gayi dima geuneu méré,
Wantanaméra sama panaméra
Let’s gnari bic si poche
Moy tax ma chris di cross
Dila chèque ak bic di xoss
Souniou begué guiss si conss
Dina wex si ioe ni dix lingome sa boxou samay og please j.o
Dizzy dream dalton dina tarr comme rappeur def lou diar yone
[REFRAIN]
Dey tarr rek di geuneu tarr
Waw dina geuneu tarr
Yokal thiéré té nga doli nièkh beut yeup si mane comme kou sathie birr sandaga
Mbok ndax xol ya ngui fékh (xol ya ngui fékh)
Ndax dina geuneu tarr
Ana sama noone yi
Niom nio féssal hopital ak armére yi dey geuneu tarr
Yokal thiéré doli nièkh (doli nièkh)
Ndax dina geuneu tarr
Waw boy dey geuneu tarr
Boyi ba légui nio ngui sétt atoumane
Mbok ndax xol ya ngui fékh ndax dina geuneu tarr
Waw boy dey geuneu tarr
Topou la ba sugn ley gassal camb
[COUPLET]
Woow ! Topou la ba sugn ley gassal camb
Thiaroy 44, liguey lo la ray la mélni toubab bék sa mame
Mataal ay but djiko attaquant
Marouane taliban sayouma guéner def ay attentas
Niggah souniou amé beef nga noce tek
Féssal nga salle bi gnibi vide calpé
Sa rappeur foumou beug dem fala nek
Tek fi tank s niou tégoul beut lane ngey def
Waw dina geuneu tarr
Ndax niouy jobé ifan ma len eup histoire
Dagn done sissou légui rouss nga waxni ya gui fadiou si pét
Sen sortie yé geuneu risqué khadim ndiaye
Songue ma boul ko waay ni ay mbaye dièye faye
Souma guéner beuss bobou ngey geudia diaay
Di nga set ba réer mais doma guissal fail
Woow ! Baby ba xol ba ngui fékh
Sa farr soudé rappeur leu doto amate bénén cheveux
Ndax dagn niow pour nangou cachém
Saway sa projet mounone na dess perpete ba neup
[REFRAIN]
Dey tarr rek di geuneu tarr
Waw dina geuneu tarr
Yokal thiéré té nga doli nièkh beut yeup si mane comme kou sathie birr sandaga
Mbok ndax xol ya ngui fékh (xol ya ngui fékh)
Ndax dina geuneu tarr
Ana sama noone yi
Niom nio féssal hopital ak armére yi dey geuneu tarr
Yokal thiéré doli nièkh (doli nièkh)
Ndax dina geuneu tarr
Waw boy dey geuneu tarr
Boyi ba légui nio ngui sétt atoumane
Mbok ndax xol ya ngui fékh ndax dina geuneu tarr
Waw boy dey geuneu tarr
Topou la ba sugn ley gassal camb
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Dina Tarr (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE