Home Search Countries Albums

Naby Lyrics


Ngeňne  gūї mbїdef ŋaby
Bessoū їt lawone  
Naby romb xaleyї gnoū lok
Sagn se ba jїeck dї fo dї fo dї ree 
Am tchїa gnome koū dїoy 
Ngeūne gūї mbїdef ŋaby
Woo xale-ba, neko dom loū wapal fowo
Nї say morrom ngaberoū dї dїoy ?

Xaleї ba dal dї ko
Sama bay daa andone tchia xekh ba akk ŋaby
Dee fa ma weett dїkhle 
Sama yaye seūy ak benene
GȮor moū gūenne ma nangoū sama alal
Nangoū sama keūr ba nangūї
Toūmoūranke 
Dї takkawaloū ak dї fanane tchi mbede yї
Moū torokhal ma sanalma
Metїtalma
Mo waral tchi bessoū it bї
Sama xel dem tchi saama baye ma wete dioy
Xamne soū doūndone doūma meūsseū toūmoūranke

Nakanonoū ŋaby
Ne xalebe ŋjakh beūg nga ma done da bay
Aichatoū done say aye 
Fatimatoū done samak
Wa alioūne ak hassane ak hoūsseyuoū
Done say mak
Xaleba daldї nїko
Ana kane may bagne ya rassoūloūlah ŋaby

Ana kane moy bagne ya rassoūloūlah
Ngūeūne gūї mbїdef, kїgūeūne te kene gūeūnoūko
Khoūreyshine yay sene gūeer
Banoūhassim yay sen baye
Ana kane moy bagn ŋaby
Nakanonoū ŋaby
Yoboū xale be keūreūm, taralko
Moū delloū si taroūlole
Gneūw morrom ya nane ko
Sa taar bїї ak sa leer gūї nga andal
Woūtena ak bїnga fїy dїoūgūe
Njakh danga melni koū dїoūddoū waatt
Xale be dalvi nїlene
Yonene bї la dadїel 
Moū latji ma loū may dїoy 
Ma wakh ko ko moū yoboū ma keūreūm
Kone mane rassoulloūllah matakh

Aїchatoū done sama yay
Fatїmatoū done sama makk
Wa alїoūne ak Hassane ak Hoūsseynoū
Done samay makk
Kharїte ya daldi niko
Yaa  ŋaby
Soūgnoū sagnone
Soūgnoū baye 
Dee tchїa kharee ba 
Ndkh yaa rassoulloūllah

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2019


Album : Terrou Waar (Album)


Added By : Olivier charly

SEE ALSO

AUTHOR

COUMBA GAWLO SECK

Senegal

...

YOU MAY ALSO LIKE