Home Search Countries Albums

Hit Em Up

BAYE KADDU

Hit Em Up Lyrics


Fuck rap bu kolda
Liguenn di deff ay doull là
Danio dikk deff musiba
Ay khiir lagn fi indi boy
Nigger aywa thiora
 
Dagniou tathiou  fils Lola boy
Bouniouy sorou dée nga boy Héeee
Dallal boy kanan féyaa
 
Up niou dém
Let's get it
Foumou yém mou nekh
Game boy beuri histoire ni goré
Nélénn may porte aller sans retour
Maguik lestek gaïnde dou réy as picka
A mboutti ka
Hab mbou tika
Evry body say Fuck Atika
Atanno ligniouy dieul
J'ai dû flow excellente
Boma songué j t fait du mal bro
Défa 10 sa kaw
Touhal sa oris do thug
Nioune la police du sétt
Bonn di takk di fay
Dadj yi si honkal sa œil
Démb ba tay
heydeus beugue ma day
Fuck Fuck
ma lokoti lokoti
kaddu yi
lakk la ndérin sagua la Ndeye
Daro mi mbo ndiama bélin
Gagné thie2 maney
Beugue 'na bénna mort
Magui thie temps forts
I'm From Last Gang
Sama team. Bang Bang

Beat bi nice ma sikk là
Rimes flow ma wiss la
Mak yaw si Beat ma eat là
Wagnis senn fann bénna bénna ni paquet rizla
Sapp your maous sénn wakh meunouma nopilo
Eh Tik Tik mak yaw ma takkala binbing
Yeah Tik tok rappeur yeup layy thiob fit
Prip Dip arbitre n'a soufflé pip pip
Dague sa digg di dibi
Ass pikk pikk yi dalna ni moustique
Yeaaaaa

Beat bi nice ma sikk là
Rimes flow ma wiss la
Mak yaw si Beat ma eat là
Wagnis senn fann bénna bénna ni paquet rizla
Sapp your maous sénn wakh meunouma nopilo
Eh Tik Tik mak yaw ma takkala binbing
Yeah Tik tok rappeur yeup layy thiob fit
Prip Dip arbitre n'a soufflé pip pip
Dague sa digg di dibi
Ass pikk pikk yi dalna ni moustique
Yeaaaaa

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2020


Album : Hit Em Up (Single)


Added By : BAYE KADDU

SEE ALSO

AUTHOR

BAYE KADDU

Senegal

...

YOU MAY ALSO LIKE