Lan La Lyrics
Oh ! Lan la
Oh oh ! Lan la, lan la leu def
Waxma oh oh ! My love
[VERSE 1]
Ay fane na ngui ci tay
Khamoulo ni sax mane mangui ci keur gui oh oh
Souma teudé ci nek bi
Nga dieul sa mbadj dem teudiou ci salle bi oh oh
Balmaaaa ! Oh oh ! Lan la, lan la leu def
Balmaaaa ! Oh oh ! My love
Lathi nala lane mo xew
Nangou woma wax, deuké dima éviter oh oh
Souma teudé ci nek bi
Nga dieul sa mbadj dem teudiou ci salle bi oh oh
Lan laaaa ! Oh oh ! Waxmaa
Lan la leu def balmaaaa ! Oh oh ! My love
Xam ngani yaw my love, fima tolou ni
Nirotouma nitte
Khuy rek té sa bop, té khamouma
Batay lane la leu def
My love, lett ma ba nga firi ma, oh oh
My love waxmaa
Fékéwou ma, yeugouma tinouma, waxouma
Défouma, khamouma batay lane la leu def
Louma meunti am yamako geuneul yaw rek la
Xam yaw rek la mine yaw yay sama way
My baby, I need you
My baby, i miss you
[CHORUS]
Bi oh oh
Lan laaaa ! Oh oh ! Waxmaa
Lan la leu def balmaaaa ! Oh oh ! My love
Xam ngani yaw my love, fima tolou ni
Nirotouma nitte
Kheuy rek té sa bop, té khamouma
Batay lane la leu def
My love, lett ma ba nga firi ma, oh oh
My love waxmaa
[VERSE 2]
So khamone lima kham mane dig ma téyé waw waw
So khamone lima kham mane dig ma yeureum waw waw
Djiguene kouko bégeul, diko yeureum la khame waw waw
Kone dékoy bégeul, diko yeureum waw waw
So khamone lima kham mane dig ma téyé waw waw
So khamone lima kham mane dig ma yeureum waw waw
Djiguene kouko téral, diko sagual la kham waw waw
Kone démay bégeul dima, sagual dima waw waw
My love waxmaaa , My love waxmaaa
Mane beugone na dé loumala def
Nga woma niou waxtané ko
Chercher ma tapass té défoumala
dara so khamone limay doundou ni nimou mété
Fils dafa am loma tamalone bama tameu ko nga
Bayi ko xol bou bégoul dioy té kouy dioy dou
Bakh kouy nakh kouy dioy lo loma méti fils
Mane beugone na dé loumala def
Nga woma niou waxtané ko
Chercher ma tapass té défoumala
Dara so khamone limay doundou ni nimou mét
Han, xol bi beugoul dioy
Kouy dioy dou nakh kouy dioy
Ling ma tamalone ma tameuko chérie
nga bayiko ndaw ak loumou
Mine bouko guissoul dafay wett chérie boy
Ane djiguene la, khawma dara atte bi nga mey dieul
Mane mi khawma dara, wayé tay la nex, ba
Ngey sopi djiko
Hey ! Deugeu leu, loumou soumi nga for ko lem
Chérie deug leu, dima wax wax djou melni lem
Chérie deug leu, wayé amna lou dess
Chérie boy xolal ndigeul geusseum
Yaka dane féthie mey bégue, ndigal geusseum
Boko féthioul mey dioy chérie, ndigal geusseum
Kou nop sa chérie boy diougeul takhaw
Diapeu len i niou dem
Ndigala geusseum, ndigala geusseum
Ndigala geusseum, ndigala geusseum
Thiof fi thiofate ndigala geusseum
Ndigala geusseum
Ndigala geusseum, ndigala geusseum
Ndigala geusseum, ndigala geusseum
Thiof fi thiofate ndigala geusseum
Thiey, kou nop sa chérie boy diougal yeungou
Kou nop sa dieukeur ioe diougal, kou nop sa
Diabar diougal yeungou
Kou nop sa yayou dieukeur diougal yeungou
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2019
Album : Lan La (Single)
Added By : Tamsir Diouf
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE