Tatagal Lyrics
Tatagal
Bu ko jot gi may e woon
weer wu ne ma ñëw
sagaal sama fan’s yi
sant leen , sargal leen
Ni bu leen di sonn al béer, njaw du mel ni lem
Jimmy mbaye xalam al leen , te encourager leen leen
Bu ko jot gi may e woon weer wu ne ma wëy
Sagaal sama fan’s yi , sant leen , sargal leen
ma nii bu leen di sonn al béer , njaw du mel ni lem
Jimmy mbaye xalam al leen , te encourager leen leen
Na ñu leen xalam al
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
Na ñu leen sargal
Na ñu leen xalam al
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
Na ñu leen sargal
Na ñu leen xalam al
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
Na ñu leen sargal
Je vous salue avec tous les honneurs
Et vous souhaite que du bonheur
Ces fans de valeurs qui m’attendent des heures
Je vous ai dans mon cœur
Vous méritez, d’être ova tionnés, c’est ça la vérité
Vous êtes toujours là quoiqu’il puisse arriver
yéen ay sama y soppe
Ànd bi yagg na , confiance bi rëy na , tatagal leen jaadu na
Njukkël leen war na , fu né nda pare ngen , ñu dem wër adduna
Da ma ni pare naa , te it sax defe naa , xalaat bi jaadu na
Su ma leen mën oon a jox loxo yegsi naa
Su ma leen mën oon seet si yegsi naa
Fatte wu ma leen , déedéet mën ul am
Yëg naa leen , sallaaw mooy li wóor
fan’s yi xam ci jamono , naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen , woy ee
Bul gnu leen fatte di bëgguel
naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen , woy ee
fan’s yi xam ci jamono , naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen , woy ee
Bul gnu leen fatte di bëgguel, naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen , woy ee
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2021
Album : Mbalax (Album)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOUSSOU NDOUR
Senegal
Youssou N'Dour is a Senegalese singer, songwriter, composer, occasional actor, businessman, and ...
YOU MAY ALSO LIKE