Home Search Countries Albums
Read en Translation

Ya Tay Lyrics


Yéwou ci seu wét doyna mbégté

Diakaarlok seu kanam doyna banékh

Love bimay yeuk kouko meun teuyé

Ana kiko sagne diaral nama khéékh

So beugué nak mou sauvage baby

So beugué nak mou doux, lo deff ya tay

Dis-moi ce qui t'arrange bébé

Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré

Yéwou ci seu wét doyna mbégté

Diakaarlok seu kanam doyna banékh

Lo-love bimay yeuk kouko meun teuyé

Ana kouko sagne diaral nama khéékh

So beugué nak mou sauvage bébé

So beugué nak mou doux, lo deff ya tay

Dis-moi ce qui t'arrange bébé

Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré

Ci seu wét douma baayi

Ak loum meunti done

Boulma yeureum, déma gaagne

Takk sama lokho

Yow seu allure dafa gaaw

Kouko léék fott

Même so togné boulma baalou

Lo deff dafmay néékh, ya tay

Soma togné, ya tay

Réwantoul sakh, ya tay

Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay

Soma togné, ya tay

Réwantoul sakh, ya tay

Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay

Mane dé beug naa (ya tay)

Lo wakh mou nékh (ya tay)

Yow da nga taarou, da nga diékk, da nga nice

Seu dokhine rafette na (ya tay)

Mane beug naa (baby ya tay)

Lo deff mou nékh, khamna dingma meussa gagne

Beugouma niouy réro

Wakhoumalak taago

Sama thiofél ci yow wornama

Nope naala mane eh-eh ya

Show me your love my babyboo

Sama safara, my seytaané

Everything! My love knocks me down

Rothie sama guégno diokhnaala ko

Ah dissah deep love fidi gyal dem

Dem ennemi mana ready fi shoot dem

Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing

Baybe yaag neu man dama paré

Ndiggueul xalé bi diaral nama xaré

Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing

Ci seu wét douma baayi (ma babyboo)

Boulma yeureum déma gaagne (mon bébé à moi)

Seu allure dafa gaaw (ma babyboo)

Même so togné boulma baalou (mon bébé à moi)

Soma togné, ya tay

Réwantoul sakh, ya tay

Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay

Soma togné, ya tay

Réwantoul sakh, ya tay

Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay

Hum… Show me your love ma babyboo

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2024


Album : (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

WALLY SECK

Senegal

...

YOU MAY ALSO LIKE