Home Search Countries Albums

Kaay Waay

VJ

Read en Translation

Kaay Waay Lyrics


Kaay waay

Ndeke dou mbeuguelou Kassè

Teh sax xetou mbeuguel yi dafa rare

Dièkou ma ni douma bale yeah yeah

An konne yaw bandi nga ndèkè bebe

Sopi nga sama xol bi limonade

Siroter ko diko nane yeah yeah

Ndax baniouy ndieukeu guissanter

Li nga ma yene nimou disser

Ak niniou xolanter

Rek ma xamni yalla niou bolè

Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (KAAY WAY)

Doflo ngama (kaay waay)

Wayè deufeul ngama (kaay waay)

Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay)

So bèguè ma bègue (kaay waay)

Niou deukè di rè (kaay waay)

Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay)

Maala geuneul lounè (kaay waay)

Teh yaama geuneul kounè (kaay waay)

Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay)

Bègal ma bèg (kaay waay)

Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay)

Soma sorè oh my love

Namel bimay yeuk thi yaw

Wallahi yaako meuneu fadie nieuweul

Niouy kaf di rè

Niouy kaaf di fo di rè

Ndax baniouy ndieukeu guissanter

Li nga ma yene nimou disser

Ak niniou xolanter

Rek ma xamni yalla niou bolè

Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (KAAY WAY)

Doflo ngama (kaay waay)

Wayè deufeul ngama (kaay waay)

Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay)

So bèguè ma bègue (kaay waay)

Niou deukè di rè (kaay waay)

Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay)

Maala geuneul lounè (kaay waay)

Teh yaama geuneul kounè (kaay waay)

Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay)

Bègal ma bèg (kaay waay)

Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay)

Oh bébé toi mon bébé

Toi qui m’as tout donné

Je pourrais jamais te quitter

Je t’en fais la promesse mon bébé

Tu m’as tellement épaulé

Quand il le fallait

M’a sorti de la galère

Je vais te rendre la money

Oh bebe yaw mi gounguè ma man malay gounguè

Et si t’a peur crie aider moi mane maaa lay sauvé

Oh bebe yaw ndax beuguè ngama comme nim la beuguè

Ndax nim la beugè eup naaa wa li noum dèmè

Oh bébé toi mon bébé

Toi qui m’as tout donné

Je pourrais jamais te quitter

Je t’en fais la promesse mon bébé

Tu m’as tellement épaulé

Quand il le fallait

M’a sorti de la galère

Je vais te rendre la money

Oh bebe yaw mi gounguè ma

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2025


Album : (Single)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

VJ

Senegal

From his real name Mouhamed Abdoulaye PREIRA, VJ was born on June 7, 2004 in Medina, Dakar. He grew ...

YOU MAY ALSO LIKE