Yenn Saï Lyrics
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Nieuweul ma waxla noy doundék wa dji
Damani nieuweul ma waxla foy diar aladji
Nieuweul, nieuweul ma waxla noy défak wa dji
(Wa dji)
Dieukeur dangkay doudeul wagni thiow li
(Thiow li)
Wanko lingako naral (naral)
Tasaréko thji lalam (thji lalam)
Dinala digatt oto, keur gou bes ourouss ak ngalam
(Ngalam)
Yétalko bathji kanam (bathji kanam)
Yé ko thji kaw lalam (thji kaw lal)
Djiguène dangay diongué mokou podje di diongama
(Déglou ma)
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Comme si, comme ça
Comme si
Voilà, voilà, voila
Solalko mbaxana késsé sa dieukeur leu lépa thji dagane
Talal lampe, yokou thioraye dougatal thji mbadje bi lou yeungou rayal
Sa arsanal bi khékha koy tass paka bou niaw diaroula dass
Dieukeur dangkoy topato diko nabeu nabé
Sauy dangay xam louy ndieugeum
Yaw deukeul di dieufé louy neekh aladji (aladji)
Seuyeul néxalko thji bir nèk bi ak wagn bi (wagn bi)
Yaw deukeul di dieufé louy neekh aladji (aladji)
Seuyeul néxalko thji bir nèk bi ak wagn bi (wagn bi)
Wanko lingako naral tasaréko thji lalam
Dinala digatt oto, keur gou bess ourouss ak ngalam
Yétalko bathji kanam yé ko thji kaw lalam
Djiguène dangay diongué mokou podje di diongama
(Déglou ma)
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Comme si, comme ça
Comme si
Voilà, voilà, voilà
Alice loutakh ngani djinakh day bari pakh ?
Marie Jeanne loutakh ngani djinakh day bari pakh?
Comme si, comme ça
C’est ça, si si
Chouchou
Kankan aah eeh
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
Yen saï, Yen saï
Defal yeufou bandit
Tassarél arsenal bi dieuleul teudeu keur gui tass
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2020
Album : Benen Level (Album)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
VIVIANE CHIDID
Senegal
Viviane Chidid is a Senegalese singer of mbalax and R & B, born September 29, 1973 in Mbour, Sen ...
YOU MAY ALSO LIKE